Capitale de la Capitale
Intro
Digou Sandaga...
Danouma sétane dessin animé ma gueunone touti gallé
Te benn télé moye animer Mcm la done golou
Fi deunguey teleu dem matinee lepp ngay teeleu def
Digou Dakar, rissou ragga bou Dj matar di animer
Dou takh nga niakk talibé maman neneu gentil na
Te bizarrement Seme grand yi nénegn bandit la
Wa gallé dolene wone se fit temps wou gentina
Boumay zoner corner douma andak samay sentiments
Fi biniou amé 7 ans legn khammé lax
Fi biniou 13 ans legn dougg Stax
Fi mm bo amoul mak deunguey teleu nande
Wakhoumala nak nga done namp tchi boutelou mak
Rote onde toni pack litrou valmerass
Dougg na tchi guenne na tchi rue de Valmy rame
Dounde na ko tangana ak roukhou macky saf
10 ans apres none le kogn bi gueuné yakhou macky saleté
Boy yi tey legn gueuneu dee walo tey le gueuneu aaye
Moye gni dieunde diaye coke marché comme si c legal
Fi dou Washington mais am ne maf ni birr Capitol
Mey ko ko baol-baol yi ak ndring yi seme capitale
Dem naChitown dounde système fédéral
Dem na la défense Dem châtelet les halles
Deukk na kawe weur na senegal
Guiss na ni wa town douniou sene égal
Capitale de la capitale
Capitale de la capitale
Capitale de la capitale
Wa town douniou sene égal

Te benn télé moye animer MTV la done golou

Tem nga aligner beu abimer wathieu do wala alizé
Dou te nga am idée donté nga teleu guinz bitch
Bo amoul chance deugueur deug rek deunguey kinss fils limeudane romb goudi town? momeu indil inspi
Bimey ndieukk binde 16 amagouma 15 piges
Est-ce que kham nga ay Fouquets? Africa star?
Sista yi jobé rue Escarfait angle Raffenel
Hotel du marché, Albert Sarraut Saloon Texas...
Gni maggué town rekkeu kham né Ponty amoul thiaga
Matin bi deunguey diangg ngone deunguey def street
Night bi deunguey tokh bone deunguey def bizz
Am ay copain you deukkoul corner nieuw pour nga yoboulene salle de vente diaye feu last call nga am se lekkou deal
Thioy yi diapp negn Gangsta yi dakkhone diapp daadj
Boy yi done daakh sip legui nio magg daakh deal
Bo amé grand you deukk jail do to diapp chill
Do faaléti ay yermeundé dieguelou diapp tchi

Moye gni dieundeuk diaye coke marché comme si c legal
Fi nimou beuré batiment non leu beuré batiman
Mey ko pourtou ngagno yi ak naar yi sama capitale

Credits
Writer(s): E Tracc
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.