Assiko Flow

Check my assiko flow
Yeah

Bimey lekk mc lekkagoumeu big mac
Me paré eksi nek phenomenou hip hop
Flow bi takh kou moussoul droguer legui Sick rap
Demey Rap nga fok ne mousso degg benene nit rap

Ding me degg bureau tangana ak biir fac
Terminal yi di meu sentou ni sene Fuite bac
Li dey guenne bomb sokhle woumeu Feedback
Ladial Dip deniou deep kouniou diss lap

Daccord nga te niamago tchi last huit yi
Boumeu neekhé beureukheul li dess ci beat bi
Muslim rapper la bou yoré flowou Whisky
Bou refrain bi di eksi ngay weddi Wiz kid

Han? Zero Handicap
Gnimeu done khepe diokh nalene envie stop
Deme bandit kate legui t'en dis quoi?
Mane deme beuri bars ni deukkou mandikate

Assiko flow teugueul me assiko
Seme baat ci kow
Limoy son Yengueul Paris beu Mexico

Assiko flow teugueul me assiko
Seme baat ci kow
Limoy son bi yengueul Lagos ak Rio

Newone nala do guiss kou key def comme mane
Son bi guenn game bi yewou yemou comme dhab
Diogué na tchi under créer seme Kingdom
Bolé khelou einstein ak katanou king kong

Moune na doré ak mi, fa, si, la dope dane
Awma dolé mane ne flow be indi do daal
Thiate defe gaaw wakh ko gni fo wé sene ndow wala
Gni khamoul ni yonou tekki defe beuri Dos d'âne

Ya ngui laadj nane laye def be flowou Zo rare
Awma temps wou guenne son yi fok niou gaweu guenn
Seme premier hit be legui ma ngui dore waar
Job bi defe rafet neu nullards yi fok niou niawal léne

Titeul rappeurou Marseille beu Dakar
Yalle ne me Yalla baal semey bakarr
Niata wakhkat nio tass seme Yakarr
Son bi takh ne me fadj semey nakhar

x1

Seutou hustla domou hustla
Im a hustla diam le nga fok né rasta le
Niveau master le danga fogone menace leu
Me break se neck qui est ce mec? Dama fogone ni Busta le

Elzi o le fils mako daakh def
Boumeu diemeu diss beuri fils ni kou yagg nef
Deme ko yagg def te khamnga sakh tchi pa la dieum
Beuri style depuis bimey sol ay palladium

Fenioumeu tchi se télé nguir se estime
Niata diameu diemeu soukheul souniou Ness biz
Dem na kaaw difeu Siguil seme Presqu'ile
Kick louy fresh clean deal le le textile

Jamdong le kham nga we the best team
Ay kangam dong nek tchi birr collectif bi
Kid bou khess bi indi shit bou bess bi
Mom ak mister thier mi ils méritent le prestige

x2



Credits
Writer(s): El Hadji Amady Diallo, Ibrahima Konde
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link