Allou Ciment
Ce Qu'il Est Convenu D'appeler L'affaire XXX
Connait Un Rebondissement Et Non Des Moindres.
Les Jeunes Inculpés Ont Etè Mis Aux Arrêts
Par Les Limiers De La Sûreté Urbaine De Dakar
Il Nous Revient Que Ceux Sont Deux Jeunes
Habitants Du Quartier Le Plateau Au Centre Ville De Dakar
Et Je Cite Sont Connus Des Fichiers De La Police
Pour Avoir Etè Arrêtés Dans Des Faits Variés Notamment De Drogue
Aux Dernières Nouvelles Ces Deux Jeunes Ont Etè Présentés
Menottés Et Sous Bonne Escorte Au Niveau Du Parquet De Dakar
Reste A Savoir S'ils Seront Placés Sous Mandat De Dépôt
Ou S'ils Vont Bénéficier D'un Retour De Parquet
D'autres Têtes Et Non Des Moindres Vont Tomber
Pour Ainsi Dire Que Cette Affaire N'a Pas
Encore Livré Tous Ses Secrets
Hum Yeah Yeah
Hum Yeah Yeah
Wo Ho Ohh
Niounak Loi Bi Leuk Ak Bukki La
Mounoul Bagna Amati Biif
Nioko Défatal Gaïndé Yi Dotoul Xamati Xiif
Allou Ciment!
Yeah!
Kén Nianoul Yalla Am Mbokk Bo Wara Sèti Jail
Pour Guénn Faut Que Niou Diaar Ci Caisse Melni Citydia
Koufi Amoon Serign Bouy Creer Tekki Dinko Seeti Dji
Wax Dji Boci Guissoul Sa Bopp Démal Seetu Dji
Thiow Bangui Raisonner Ci Kogn Bi Comme Ay Ambulances
Thioy Yangui Diabanté Ci Kogn Bi Comme Ay Ambulants
Bonnes Yangui Daxanté Ci Kogn Bi Endurance
Coke Bi Moudjè Wathi Ci Kogn Bi Mo Am Honduras
Borom Bopp Yi Nioy Borom Boppu Kogn Bi Légui
Borom Diplômes Yi Seen Morom Yi Dileen Gondi Guéy-li
40 Ans Mousso Job Niaari Waxtu
Dakheu Kaas
Dakheu Waxtu
Bepp Waxtu Yangui Niaxtu
Amna Guiss Guiss Naako Wax Nga Degg
Fii Gas Yi Yorougn Do Té Beugg Dope Ni Doggy Dog
Amna Guiss Guiss Naako Wax Nga Degg
Nagnko Wax Té Dèè Wala Gaal Gui Dina Diig
Yalla Lagn Gueum Mou Melni Seuytaané Dafniou Tiim
Beug Nga Sangou Sétt
Mais Say Toilettes Dafa Tilim
Kougnfi Déférer Thioy Yi Dougnla Faalé Dagnlay Punir
Innocent Coupable Xamalni Yangci Biir
Allou Ciment
Fimoy Allou Ciment
Loudoul Crime Dougnko Fekk Sa CV
Limafi Guiss Dafa Tar Dafa Yeemé
Hallucinant
Eh Fimoy Allou Ciment
Lougnou Xiir Ba Took Bougnou Teeré
Deuk Ci Deal Ak Di Def Lougnou Teerè
Boba Légui Niounkoy Xaar Guissougn Changement
Pourtant Démna Bay Guenn Moudjè Am Dérangement
Fii Dara Changer Woul A Part Minettes Yi Magg Mool
Mais Sugnu Rakku Homies Lagn
Dougn Leen Meuneu Xool
Borom Gamos Yi Nioy Garer Corner Dieulci Leen
Meunoci Lenn
Dagniy And Nekk 2 Ci Neek
Buniu Dociler
Money Lagniy Daipè Dieuci
Lepp Doci Yeuk Dara Boudè Amnagn Ci Town Bi Dossier
Amna Guiss Guiss Naako Wax Nga Degg
Amo Lo Thioop Beugg Dound Life Doggy Dog
Wa DIC Gnounglay Topp
Say Wadiour Dagnla Sopp
Indic Yanglay Xool
Méfies-Toi De L'eau Qui Dort
Dou Super Man Molay Nieuw Sauver
Dou Bat Man
Guissouma Logo Wam Ci Assamaan
Kone Boudè Dangay Diaay In Da Pet
Dièmal Bayi
Boudè Dangay Foon Wala Diamb Moom
Ama Yè
Wax Deugg Nassaraan Ci Dafa Nax Sunu Maam
Wayè Niounit
Wara Tuniu Nangou Gass Sunu Pax
Senghor Waxoon Na Deugg
Légui Dakar Comma Paris
Benn Différence Mo Am
Fii Amnoul Tolou Goudron
Wayè Amna Allou Ciment
Fimoy Allou Ciment
Loudoul Crime Dougnko Fekk Sa CV
Limafi Guiss Dafa Tar Dafa Yeemé
Hallucinant
Eh Fimoy Allou Ciment
Lougnou Xiir Ba Took Bougnou Teeré
Deuk Ci Deal Ak Di Def Lougnou Teerè
Yeah!!!
Yeah!
Yeah!!!!
Yeah!
Niounak Loi Bi Leuk Ak Bukki La
Mounoul Bagna Amati Biif
Nioko Défatal Gaïndé Yi Dotoul Xamati Xiif
Kaaniu Fatté Alloup Kaagn Dénthi Canaris Fils
Kouko Gnémé Toudd Gnounila Danga Xamadi Fils
iOw Xippil Xool Yangci Allou Ciment
Kou Meune Sa Morom Thioop
Tabaski Niou Baalouci Akk
Bouma Guénnè Son Bi Dina Am Gnou Aalu Ci Mane
Lilagnfiy Doundou Mais Day Melni Kenn Warouci Wax
(Allou Ciment)
100 M2 (Allou Ciment)
Camp Pénal (Allou Ciment)
M.A.F (Allou Ciment)
Hun Allou Ciment
Hun Allou Ciment
Teaupla - Rebeuss
(Allou Ciment)
Médina - Fass
(Allou Ciment)
Gnaay Thiokèr
(Allou Ciment)
Gueule Tapée - Grand Town
(Allou Ciment)
Pikine - Thiaroye Gare
(Allou Ciment)
P.A - Guédiawaye
(Allou Ciment)
Liberté 1 Ba 6
(Allou Ciment)
Hun Allou Ciment
Hun Allou Ciment
Grand Fe-Yo
(Allou Ciment)
Lakos - Ndar
Guoumel - Casamance
Yeah
LG
Wa Yii
KL
Podor
All Dong Leu

Credits
Writer(s): E Tracc
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.