NOBOMA WOON
Le passé c'est le passé
Trop de problème avec toi j'en avez assezz ey
Maintenant que tout a changé
J'ai tourné la page car tu m'empêche d'avancer
Thi diir bou gat lala khamé gua beug ma jugé
Thi sa digue, sa ay kharit gua sewalma ni i
Mane yorou mawone khaliss
Mais gniko yor sa khol iow mousso lenko thiabil
Bamala guissé si la guiss nit kima done sét
Façon yéne gor yii nieupeu yam ganéma mounoul néh
Mane melouma nii guar gni
Sa tank sama tank gua présenté ma PA bii
Gua begn dh néh dou mak iow
Geume lo mani né mounougnoun Dem fén mak iow
Téré nanie ma teud temps nah doumala am iow
Iow mi sa bop yama téré ande ak iow
Gua bagn dh néh d'où mak yaw
Geum lo mani meunougnou dem fen mak iow
Téré nanie ma teud temps nkoul ak iow
iow mi sa bop yama téré and ak iow (bb)
Noboma wone, noboma ndeyssane,
noboma wone bameu lay face time,
talo ma wone bameu lay message, noboma woo-woo-woo-ooh(×4)
Kouma ko wakhone douma ko geum ya moudier xewii nii
Mane iow rk la guissone gua diapé meuh nit invisible
Bayina la à vie, faté gua bigua ma done rombe ak vitesse Ferrari(thip)
Mbeuguel indi woula lila indi dieulina
Tey guamay sogua moune sét fep ni FBI
Rethie nala bayil
Way bigua ma done dieundé lgui gua ko niémé trahir
Gua begn dh néh dou mak iow
Dama la mounoul mounie niou dem féne mak iow
Doma téré nakh mounou ma ande ak iow
Iow sa bop yama téré and ak iow baby(×2)
Noboma wone, noboma ndeyssane,
noboma wone beumeu lay face time, talo ma wone, doma done message
Noboma Woo-woo-woo-oh(×4)
Pourquoi tu crois aller venir quand tu veux
Cette fois hélas c trop tard ohh woo-woo

Credits
Writer(s): Dominique Preira, Tamsir Ndiaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.