LYXRD
Fuck béppeu khétou reuthiou fuck bou démb don tay
God ki nga ma ndieuk may laa meusseu beuggeu ba tay
Wéto siggil sama yaye benno di seug ba tay
Yaw laa ndieuk am si life moussou ma wor douko déf
Dé si gneup la deukk yakamti na nit tééy si
Lalou or ni khandor man maa diouk kill la nga perte
Gnan na yalla ba takkeu ngané di ngama fay
Album bi paréna sans beat tou iss sama frère
Ni sama père iss sama frère khamnani dama dé
Takka diabar mou takkal ma gnari or yi samay chaîne
Nakh souma amon xolou robot day dji di nga may chaîne
Légui lay soga kham dou may bindeu samay texte
Dama leundeum waayé amna xol bouy nit sama xél
Diouddo hôpital bess bimay dé église lamay fékkeu
Euffeul mak sama bopp khamné dip peu meuneu khékh
Yaye lébalnaala samay fan khamnaa di nga ma meun fay
Est-ce que mérité ngen may rap si sen lakkeu
éggoul si sen xol may téklé médaille youmay takkeu
Yéné guéth la douma borom bay lap si say vague
Lame set si sène gatt yi def ni élastique lay daggeu
May gass pour guiss assamane yaw kithi terrasse bi ngay tagueu
Taggal sa bopp ma dém dieundi essence briquet talleu
Boy dip bat-man super man leu
Kharagne Falaye gris ak Balla
Damay mbéllakh bidéw la man
Bém boumay dé dém safara aldiana laay gnibé ak diammeu
(Kham ngén président senghor modon
Wakh man fouma diaar koufa diaar takheu ban
Damané man fouma diaar koufa diaar so
Moytouwoulé gnou diawalé la ak ban bi)
((monsieur le maîre j'ai une question))
Mama télna teuddeu téla dioukk mais geuth na nélaw
Meuwti khaar naala ba guéméntou bo yéwo yéma
Nath bi fan la fanan beuggon nafa dém
Adouna bamél la néw rék lay doundé
Vye vye vye, vye va vye vye, vye vye vye, vye va vye vye
Lou Yalla xam rék doyna
Lou Yalla xam rék doyna
Lékkeu sa thiono mandé sa gnakk naan
Sa dérét ray la gneuw di dioy si sa deuth
Boy li Yalla xam rék doyna
Li God xam rék doyna
Paré won naa pour taylé sama bopp pour
Yaw ndokk ba nga ma taylé pour sa bopp
Bro lou Yalla xam rék doyna
Gnou douggou jail yeul dangou gueuneu ndawlé cage
Meun geunou malén sagne wakh damalén geuneu wawlé gatt
Comme que mballit rk ngay génné boudjouman nay don say fans
Dél touggou salle di pompé cent may douggou banque di déposé sacs
Sama sago moné si man yéh
Tokhou ma bon day takh douma yék
Meunouma bokkeu ak yén foumay dém
Boudoul won noone ndeysaan dinaa wét
Dou diamou Yalla mais deuggou moy takh nga diégué God
Noy khamé Yalla khamo loutakh sa dérét khonk
élection si alleu ban mala moy téréé gaïndé tok
Gouddi diappoul si lén kén douko téré diot
Ragal fété day khagné weurseuk
Fanla weurseugou ragal di fété khanaa say dieuf
Am plus de 25 ans baye dila diokh agne ak rér yeup
Ragal lou metti molay teudieul bountou ak palantér yeup
Yah, ya ngi ray temps mais sa temps vite fait nga dé
Dinagne ma khékh mais dougne déggeu dip néna méss
Dom di nga diot testament do guiss sama néw
Déf yeufou ragal moy liguéy bi ngén gnémé
Limay way rek lay tégat sa rapeur dj leuh mais
Rappeur engager lire na sa message fi may iré sa guél
Mak djiguéne ak chèque dou meusseu diékh ni triché élève
Gnouné douma lén meusseu lékkeu loutax ma digérer len

Lékkeu sa thiono mandé sa gnakk naan sa
Dérét tay lagne gneuw di dioy si sa deuth
Boy li Yalla xam rék doyna
Li God xam rék doyna
Paré won naa pour taylé sama bopp pour
Yaw ndokk ba nga ma taylé pour sa bopp
Bro lou Yalla xam rék doyna
(Kham nga lou geuneu bon sénégal dagnou
Beugeu diaawaler deuth ak ngénté bokkoul)

Credits
Writer(s): Dominique Preira, Assad Nassour
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.