Boul Fale (Don't Worry)

Mangui dik ni gnow tchi microphone bi ndakhté dagn ma (togn)
Dama diggi di takhawone tchi sama diggi di boppu (kogn)
Wakhtane ak sama (gayi)
Wakhtane ak sama (way)
Beneu khalè difa diar dima fa diéma kagn
Mou sol lou (gatt)
Sama xeel nar si (gaat)
Ma miggi ni woko
Wakh ko sama sokhlo
Mou bougou ma atté gnakal
Bouggou mafa torokhal
Manè ko hé (kholal)
Mane xalé douma (foural)
Ma nar ko door nar ko gagne nar ko def lou ñaw
Sama gayi diappa tchi néma fils (non boul fale)

Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (non boul fale)
Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (non Awadi boul fale)
Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (non non non)
Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (non non non)

Brrr fale
Nguey maak di xalé xalé
Yone ba ñgui nalé
Kone del balé
Aïe aïe aïe wouy sama ndeye dagn ma (gaañ)
Positive Black Soul nena na ñga (baañ)
Té nga djoko
Ndakh ndakh kou beugueu, beugueu na
Kou baañ, beugueu na
Kou naangou, nangou na
Pb, PBS
Mome dou P.D.S.
Mome dou P.P.S.
Mo... khar bou fess
Niow, andak jeunesse bou yess
Dey (xeess)
Dj Awadi
Pupa Duggy Tee
Deloussi
Wakh dji dafa beurri nga né fils (boul falé)

Boul fale Duggy Tee boul fale (non duggy tee dama né boul fale)
Boul fale
Boul fale Duggy Tee boul fale (non non non)
Boul fale
Boul fale Duggy Tee boul fale (duggy tee dama né boul fale)
Boul fale
Boul fale Duggy Tee boul fale

Mane de meussone na fi ame
Beneu geel bigidi (bakh)
Nena dafma digidi (noop)
Dina la wakh lou (takh)
Bouma digidi done job
Xalé bi daf ma nobone
Daf ma digidi done thiop
Di wakh ni daf ma beugone
Ma bigidi beugueu seuy
Lekka xaliss bign ma dinkone
Ñou digidi dakha ma
Xalé bi naar ma sonal
Mou digidi diekki diekki guéné fa djiko you boon
(Eh meyma sama baat damey dem sama yoon)
Ma naar ko door
Naar ko gagn
Naar ko def lou ñaaw
Sama gayi diappa si nema fils (boul fale)

Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (boul boul fale)
Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (boul fale)
Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (non non non)
Boul fale
Boul fale Awadi boul fale (yow boul fale)

Ma insister deloussi deloussi
Kone mbok defko sissa boop
Te nga topeu lima sampa man
Aussi fils neel (fess)
Bala maley khass (kess)
Kess gaanar gek mouss bi
Bouffi tiow (djiip)
Dama dem babylone
Yeungueul sama yoon
Kone book
Boulma togne
Boul done sama (noon) mouk
Dama né dama né
Dugg duggu Duggy Tee
Te mangui deloussi
Neetali fateli
Djotel lou...
Weddi guiss bokkou tchi
Deug deugu oppu tchi
Diggi di Duggy Tee mome dou tiakhana (non boul fale)

Boul fale Duggy Tee boul fale (non boul fale)
Boul fale
Boul fale Duggy Tee boul fale (non boul fale fale fale non)
Boul fale
Boul fale Duggy Tee boul fale (non non non)
Boul fale
Boul fale Duggy Tee boul fale (non boul fale)

Boul fale non boul fale
Fale fale fale
Non boul fale
Dama nela yow ak demba
Non boul fale
Non non non non
Non non non boul fale



Credits
Writer(s): Amadou Barry, Didier Sourou Awadi
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link