Niggas Gon Hate

Esk hamga sama name
(niun may wowé shady)
Esk hamga sama name
(niun may wowé eliw)
Hamoul sama name
Wahko sama name Babee 2 fois

1er Shady
Esk hamga sama name kom bou Admow Flow fokga wané bokoy guééw
Do you know maf... king Name, bigua yor ak mom it's not the fuc.king same
It's not the fu.king same boul yakk sama tour kay niu wahla sama name
Dafa Fresh mais bulko yeugeul seu guel
Bou topé si nopam rek nga diakk seu guel
Def meu her babee dima wowé babee Shady
Nane meu magui reuthiu why i didn't meet u early
Guél yi lugnuy sopp bolén moytuwul rek nga panni (panne)
Mé dieuleul sama name rek nga am lou beuri
Shady biguay dégg mogui diogué si Alou
Daga sohla detail fokga wagni liguay allou
Eliw biguay dégg mogui diogué si Aliou
Bama néké gondé akeu beuri gnuma diépi
Nane meu dognu topou parsk boy iow daga touti

2em RAC
I just wanna know your name babee
Can you tell me what's your name
right now noow
Can you tell me all your secrets
Tell me everything you know about us
everything about us
Aaaa I look up to the sky
I wish that i can fly
So I can fly to you (can fly to)
Just give me one kiss
Give me some love
Noh naaah naaah naaaah

3em Shady
Hamga lane motakh niu toudé meu Emi nigga Shady
Parsk soumay rap ngana gaw machine ak chauffeur taxi
Nigga bigi momeu nieugeu wakh boy rap bi digsi tekki
Books némeu continel bul bayi none yi di wédi
Yagga diobak dj bib mou defal mako lepp free
Hamga dugnko meuss faté Aliou Diallo dafa ngoré
Yagga topando jabbou madou books ak nigga simon
Hamga lane motakh mouné leu waykatam moy admow flow
Dafa yaga fowé way bi wané si nékhal batam
Papis G'Move'men yaga tewal Hood Brain yagga niu poussé
Aliou Kharitou nieup yarou nekk si kholou diam yi
Kougn fi yagg ceddel lou bakh khelam dou meuss tey
Niata gayine lafi beuri té au début dagn meu diépi
Domou Aissata Mama Dieynaba Ak Astou Barry
Nioma yagg nianal némeu mougnal beuss digua tékki
Lemme big up samay sohna Nana Mina Fenty Saly

RAC
I just wanna know your name
i just wanna know yoooh
Babee Givve to me 2 fois

Shady. If u never know now you know me 2 fois
Shady kaay meu néteuli leu yeaaah



Credits
Writer(s): Nathaniel Findley
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link