Aduna

Kaye lène gnu fo di ré
Kaye lène gnu fo di ré
Kaye lène gnu fo danse di ré
Yène nitou aduna bi
Kaye lène gnu fo danse di ré
Yène nitou diamono dji
Doune gui bougnu andé dal dal
Di fo di ré. Fatéliku niko sumu mame yii
Dane dété. Bouma xolé dembou rêewe mi
Aduna yêne nith gnilé
Aduna. Danse fo di ré. Yé aduna
Aduna bilé. Folène di ré.
Nith gni dagne dane fo di ré
Nith gni dagne sétane té
Nith gni dagne dane wakhane té
Nith gni dagne dane dissone té
Nith gni dagne dane dissone té
Di fo di ré



Credits
Writer(s): Idrissa Diop, Handel Tucker
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link