Baobab

Yayo bo beugué xam sa reuvé yé
Xolale thi sa goune rêwe
Boye djité té di magué
Daghaye xam né thi gouné ghaye doré
Dolé rewe mi migui thi xalé yé
Rêwe muti nath euleugué
Xalé moye mague djité reewe mi
Xalé yoyu bugnu magué é é
Gnoye djité ayes rêwe.
Bouye bi nimu mégné
Gouye gha data magué
Bougnu wané yone xalé yé é é
Gnu meuneu magué
Ba meuneu yoré reewe mé
Lou yagué
Ni gouye di yagué
Thi soufe sé é.
See there's this tree
Full of possibility
And I'm asking all the children
To gather around with me
So that she leaves fall down, fall
down
And set us all free.
So many questions all around
No answers to be found
Will you please help me now
And let them fall
Let them fall, fall down on me.



Credits
Writer(s): Idrissa Diop, Moussa Diouf, Handel Tucker, Maurice Wilcher
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link