Bouleu Dara Méti (TLK)

Boula dara méti
Boula dara gagn
Doumeu imbecile
Danga ka wareu xam
Doumeu domeram
Doumeu salopard non
Boula dara méti naxx mane
Léne rek meu titeul té dineu ame
Aye nite you baxx nagn leu diaxassé ak mane
Lougn ley wakhh lolo ame
Dou diare saxx nguey comprendre
Même Boudone mbeuguél dey diay,
Do ame kénene comme mane
Doy na waram, deufeu daw yaram
Deung meu beugue xamnako, xana dou maleu doxane, doumaleu thieupeul
Tchii péte yow nguey diay euppeul
Dimey thieupéle . Yow mi yadone poster si net bi nane founé "je t'aime "
Love ngueumeu beu teunkalémeu . Lolo taxx meu déme.
Baby lou euppe tourou, danga ma warone nobb ndank rek.
Waxx na beu déh. Mais Danga Lank bagne ni domeu degg
Mane mako deff ndaxx maleu warone waxx lo guiss dey diex
Yow taxx ngueu nekk seumeu diabar té démeugoumeu tchi seu père
Sougn done degueunté téléphone tout le temps noumey liguey yéé
Loutaxx kouné wareu controler moromeum comme policier yéé
Ame na rongogne comme yow
Manite meune na lakatou dioy comme yow



Credits
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link