Siiw
siw dou diami borom ma thi kham dara leppeu lou yengou yow laniouye key djigne
yegoulo fékéwo niou fénte wokhou niaw am bapa mou bari tay ko sa guinaw
bo ma guissé di ma ré ma wone la guinaw nga yakha sama der dou ma diar dara
Refrain
bayi lène di bakar, wokh llou la woroul lébi nène
bayi lène di bakar, wokh llou la woroul lébi nène
l'islam da key ayé
diapa sa ma dom di dor ma takhaw di la khol bou sa yaram dé daw nga bayi ko
fi la deukeu fi la djoudo di weuye sa ma mame teki dara guene wo yéwoulène
lou way di def di thia tokh kénée tedda na thia mbirou yalla mo woor

Credits
Writer(s): Thione Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.