Cicatrice
Depuis ba ma.commence takk
Si la moteurou rap galsen bi commencé takk
Animateur yep nénagn massou ma mar sen tate
Niata old school dans le coma
Déwouma di diote ay hommage
Yaw khéwa go di khomate ndeysan
Album bi lamb na pittch yi commencé sapp
Sama papa nénama fils c'est normale nespa?
Wé C'est normale kay paa
C'est normale ndakh dama def ay cicatrices
Es ce que France sagn na bagna diokh zidane 10
Cicatrice
Maname dama dieule artiste you gueuna makk si ben att ma def len ay archives
Ma lén mane té yéna ko gueuna kham bilahi
Sa label lafi gueuneu niéé reptile
Té niata deum beugueu réré dip
Né lén dip yonenti la daniou réré mbir
Clash lou si yoni cimetiéres ak ay eglise
fakers nigga raggal yalla mo mayé fiit
Ngay féne rek di ame loy diéma wakh sama ethnie
Es ce que borom tour bé may diayal cd yi
Meme Jay Z manou ma diakhassék jesus
Do ame dara ni candidat PS yi
Kone boul éss fils yow mandikate nga do mc
Dip comme messi mome yéne yi douko métil
Mais do mbéthie ki no bayil ma def ko domestique
Mais do raye ki no bokouniou sakh pointure
Diouguél fi
Démal té bouma def signe
Tar mbéthie la ba si leikhou Atou rér na
Sasou né
Ngay deg sama bate founé
Yow khathie bou dé bi do takk ni gaz bou diékh
Yen tatou nén ngen def té dip talou lén
Man sakou thiép la gueuna mana calculé
Té Cassou méw la yamakék sen caissou néw hun
CICATRICE
CICATRICE
Sama succés dafa def ay Cicatrice
CICATRICE
CICATRICE
Nigga soula mété man nga tek sa tate si gaz bi hun
CICATRICE
CICATRICE
Niépa may lathie equipe yepa ma sokhla ni Pogba juventus
CICATRICE
CICATRICE
Ni illuminati sama niari tank si kaw piramide
Ma dakh rap si sama génération
Sa mame sakh day lathie bakham guéné na son
Diougué schoolou karim xrum xakh ngen beug ma def sen gaston
Koula né ngen dima clash xana da ngena dof
Lima ame si rap dama ko mérité
Té dina fessal stade bi la tal bombe di guéne
kamikaze sakh dou takh samay énnemie diekh
Fuck comédien yi di wédj wédj comme ay djiguén
Défaillant yi daniou ma déssé kham
Idy mayma... faw décès ame
lo tekk gnou tekk boy khekh gnou khekh
boy teikou ngueine kou keine doule teikou
wax bou sw bi tiep bou sew bi
bouy tegui bec'ou sekou
delouleine fingueine diougué boungueine beugué kou degg sen tourr
ngueine liguey gnoune gnoy fouteikou
TODJ SA TIOTOU AH!!
fuck you niggah fuck say niggah
fuck kou begg fuck kou beggoul
job bou sett la non gounguei wuñu keine
diouni trophée noneyeingui beugeu dé
douma def ni drake di guéne back to back
gneuweul face to face
boy lgui fake yi feign
boy bou ndaw di leine di tiop ni tiebou dieune
yagg dem fi fake yi deukk di yé fitna
damko def ba yeukk ni lgui xewii na
CICATRICE
fimou tole gaînde bi da xif
ndax gnifi gneuwone demb di gane feat
gno taxaw feulei nei di dingate dip
niggah fuck you fuck sa dieumbe fuck sa rouh
deumb bouy wadia dé fok mouy dieufeurou
xawma niata grand lafi ray gnou dé té bagnouy rap mangui jardin di day toubeuy
moréé
TIOW LI BEURINA(BIS)
AH LOLOU DEMAL WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
OH MY NIGGAH (BIS)
WAXKO GNIKO ATÉNOULE
TIOW LI BEURINA
OH LOLOU DEMALE WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
OH MY NIGGAH
YEAH WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
GAME BÉ BEURRI FAKE AY RAPPEUR GOOR DJIGUEN
MANE AWMA LOUMAY DINDI AWMA LOUMAY MODIFIÉ
CAUSE I GOT NO REGRETS I GOT NO REGRETS
MAMA MANG THI DIAM DOUGNMA DEFF SAX BOPP BOUY METTI
MANÉ TIOW LI BEURINA
EH LOLOU DEMAL WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
OH MY NIGGAH
AH YOE WAXKO SA GARS YIKO ATÉNOULE EIH

Credits
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.