I Am Sorry
Loumay deffi Adiana
Né nala fo né man fala né
Lou wer di deff ci assamane
Boudé néwoul sa kaname lay wané
Lou café bi di safé dôme
Ya done motali thiafka bine sama succar bekk
Lou waral fleuri rose te newoul yay khenthiou khet bi reeee meu ma dadi beug sama yeuf
Xol bi yaw rek rekako meuneu beuss
Dioxnala lepp lepp lepp louci dess
Topp nala fepp fepp fepp banga seuss
Te dou takh ma lep lep lep lici dess
I love me and I love you too
No feeling so lonely and I call'em without you
I'm so sorry baby I'm so sorry
I'm so sorry I'm feeling so sorry yooh
Baby I'm so sorry baby I'm so sorry
I'm so sorry I'm feeling so sorry yooh yeeh
Namouna dorante ay ndieguenaye
Foo sam bopp dima fône dima ray
Nameu sa feel thiouraye
Sa lokho bima doni lale bouma teude tay ci night
Man xawma sax lou lekk di saff
Keur gui peunde ndapp yi tilim télé bi peunde te panne
Collègue yi dima woo pourtant dama febar baby nekoufi te nelawouma demba hann
Dafay sonné ma beuss nelawate
Ya done nieuw ci lale bise done ma yééé
Wakhak mane takkalma sama cravate nema nanga sage nieuw ci nopo bi wakh ak mame
I love you I love you too
I love you many I love you too
I'm feeling so lonely and I call'em without you
I'm so sorry baby I'm so sorry
I'm so sorry I'm feeling so sorry yooh
Baby I'm so sorry baby I'm so sorry
I'm so sorry I'm feeling so sorry yooh yeeh
Han lou meussoul am ma niane la leneu nga tekk ci bate
Mais tay nak bi moy bou moudj faw nga mayma niou and day you home back
No meussoul beug sa xol takk
Da yagg beug nga contane
Wane nama mbeuguel wane ma bague ne yaw la yako beugone takk
Fatelikoul ni meuss na nex
Kon dinga faté balé
Même niari wegn bouniou beugué bess faw niou khassanté lalé
Wait wait wait wait
I'm so sorry
I m so sorry
I m so sorry
I m so sorry
Lomay nouyo loy wo khoulo bamouy nieuw
Ana goor bou galant won tay malay khol day melni dou yay
Sa gallé bangui dofé te yaw rek de defar café nga am kou melni ki dila topato boy dafa diafé
Diamano tay djiguene wourouss la lici bax laniou wara sameu
Del khalate bala ngay wax guenal dela ay valisam
And I call'em without you

Credits
Writer(s): Babacar Mbaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.