Sey

bo takké sa jieg amak mom ay tom
boko weuthié sa jaboot taxawalu

yay mi jiguén topatol sa Sey
té fo mena toll nangol dann sa dollé moy sa waref

baylén jay sén domm
ala du Sey

Sey 3 waref la
dund bu doy
thiangay lu doy
jamm ju sa

lolu moy Sey, gayi sédé lén ma



Credits
Writer(s): Boncana Moussa Maiga, Thione Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link