Gudi Diop

Tanku neen (3 fois)
La doxé
Tanku neen (3 fois)
Tanku neen (2 fois)
Loxo neen
coono neen
xif neen
feyda waaw
aw ma "vélo" asta maak "auto"
nit ku néka
amna lu koy rey bes (lu koy rey bes bes bes ...)
suma diotoon lolou
dina dee
foum ko diaguar diaguar diaguar diaguar diaguar
Ca adiana sa ca safara sa
Tankou neen la doxé
bayico guinaaw diem kanam
bu ngelew li diogué
ma and' ak moom (di weey)
bet bou fata fata fata manam
Sama tur munu ma ko wax ci khadia goudi
Bou ko djiné yi dégué
sétè souba aat
yobou ko ci ay dioow dioow

fine ma djeulè sorinaa
yalouwane sèè
sookh sookhlou wooroul
boula diarè yow di ngua sookh
waayé do dèè
damala yendu lo guane laa fi
fima diogué soori na
topa taali bi dox ba eksi
fege neek bi lo fiy outsi
ci khadia goudi gui

man la goudi diop, mana
Sama tur munu ma ko wax ci khadia goudi
Bou ko djiné yi dégué
sétè souba aat
yobou ko ci ay dioow dioow
(refrain 2 x)

sétè souba aat
sétè souba aat



Credits
Writer(s): Wasis Diop, Thierry Faure
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link