Reppin Time
Yeah
Yeah
Oh shit
Eh iow
Iow dangniou conditionner ba
Bo beugué tekk li sa communauté
Di dund da ngay sauralé
Mais est-ce que niom di nagn sauralé suniou wakh ci suniu ay
Famille nombreuses ak suniu febar yi nga khamné niom nioko inventer
Yeah
Yeah
Africains dangniou khepp batay
Nigger bu tekki sakh Niggers yi dagnlay khekh batay
Colon bi néna demb moniou civilisé
Motakh
Luniou meusseu créer dafko dindimusé. WOW
Sarko néna amouniou history
Alma lagnset ma niassalko hiéroglyphe sikanam dangniou yapp sama baat
Ci kaw nekal waliyou do dara ludul black si niom
Suma néké town kaawman la
Suma néké kaaw bledar la
Lutakh dugnma wowé expat han
Deuk banlieue égale deffkatt la
Faut que ma dem OFI khol bane febar la am
Melné fima diougué SIDA dafa feug niounéko bismilah
Liniou beuri febar yeupp khamalni crise bila,
Nassarane si dafniou yagg forcé guissGuisseum
Motakh diplomatie khétou hypocrisie la
Sa life yeupp dagnlay wonené
Li nga kham dara amoucci ndieurigne
Li nga am dara amoucci mérite
Linga dondeu si say mame dagnla nane fatel té
Boul réfléchir khamo nguerr waayé am nga aspirine
Correcte moy nduru toubaab
Soy wout liguey bo solé grand mboubou dou bakh chemise ak patalon
Rekay duug fu baax entretien tégal cheveux rek boul yobou foulard
Li tchi mane rek dakk dagn koy dondeu
Après colonisation bi gaayi dagn koy doli
Bo geustuwul sa bopp toubaab daflay diomal
Numla def nouko raw lakoy def say dome
Complexe dagn koy dondeu Système bi dafkoy yokk
Ma ngui fatélikou bima beugué def ay locs
Prof prof bi néma watoul wala sdf ngay done
Im on my Reppin Time, Reppin Time Reppin Time, Reppin Time
We gotta Make it Right, Make it Right Make it Right, Make it Right
Im on my Reppin Time, Reppin Time Reppin Time, Reppin Time
Suniu mame yi dagnko métiil baye
Métiil baye, now we gotta Make it Right
Lifou bitim rew dagnlay humilier
Dagnlay keuyitlo ndakh amo keuyit bro
Faut que nga khekh diayanté pour meun nek ci diaam
Daniou tekk deal diam laniou def ci mind
Li geuneu meti moy niom ño ndieuk nieuw suñu territoire
Takk boum diaam dieul ci tirailleur
Té niouné beugeutuñu guiss beneu noir
Dagn beugg niou teudd geumm ni Schumacher
Ladiou niou keneu mou nieuw sathie suñu or
Wakhouniou keneu indil bateau yobou suñu maame
Lutakh niom Huey P. dawal naka sudul nonou
Parsk ñi nieuk indi thiow baluwuniou akk (akhh)
Dieul deukk leumb dompter len
Balégui Pubou xessal mi ngui daw télé
Motakh ba suniu sister yi di am complexe
Ba façon febar bu nekk laniouy diankontel
Histoire bi dagnko deupp
(Histoire bi dagnko deupp)
(Histoire bi dagnko deupp)
Histoire bi dagnko deupp chapitre yilen arrangeéwul dagnko teupp
(Yilen arrangéwul dagnko teupp)
Do degg feneu tabakhu pyramide niit kou nioul mo ci ndieuk
(Niit kou nioul mo ci ndieuk)
Motakh niit kou nioul rekay am accenwu niit kou nioul diko neubb
(Nioul diko neubb)
Boko defoul rek niou toulila sen deukk
Immigré késsé nga dougnla may ludul ass tutt
So meuné diaamu teuthie sa guémign that's Cool
Meun nga tidji taxi phone wala fast-food
So beugué changé game bi dagnlay gass soul
Sa lepp laniouy toutil gniné hip hop dou culture
Il faut que nga nekk bounty pour niou ibbil la bountu
Lolo waral cité yii fess dell ak ay famillou black
Back dugg si kogn bi nakhté boyii amuniu bac
Yéna ndieuk nieuw suniu deukk
Té bougolen niou guiss sen deukk
Di nagnlen wakh suniu deugg
Di nagnlen wakh suniu deugg
Yéna ndieuk nieuw dieulsi tirailleurs yi
Té beuggtolen guiss seyni seutt

Make it Right
Make it Right
Make it Right
Reppin Time
Reppin Time
Reppin Time
Metiil baaaye...

Credits
Writer(s): Elzo Jamdong, Misterthiere
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.