Gana

I say
Life bé tarr
Life bé tarr
Life bé tarr
Dagay lidieunti seu bop
Mais do meuss kham nitt loum lay denthial
Borom baxx la mais dall yé sokhor
Sama swag, sama styleu sokhor
Sama flow, loumay rap mo sokhor
Balna len c'est normal niou sokhor
Kon baby boul ma diaye graw man ay thioraye yeungalou ma
Sama son day daw, gua guiss ay chinoise di leumbalou naar
No baby boul ma diaye graw man ay ginguer yeungalou ma
Sama son day daw, gua guiss ay naarou leumb di leumbalou naar
Nigga waxma pourquoi gua sokhor
Mounonn gua bax mais sagua tanneu sokhor
Vraiment khawma ioe pourquoi gua sokhor
Mounon gua liguey mais dagua tanneu sokhor
I say, batman miezé fresh ni penguin
Decembre Laaley may ay solou you fin juin
Niom nieup lay faye niou melni fin joint
Soll chino guénei kawass ba melni Tintin
Yalla loudoul yalla
Loudoul yalla defouma dara
Am rappeur youniouy soul en tout cas pas moi
Gana, Idrissa Gana
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana
Gana, Idrissa Gana
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana
Gana (Eh), Gana (Gana)
Gana (Eh), Gana (Gana)
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana
Dall kheil, diap ndigue, Idrissa Gana



Credits
Writer(s): Flagrandelit, Omzo Dollar, Passa Beatz
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link