Ay Coono La

Ndeke mbëggel nila
Ndeke yow rek lenen la
Nit dinala bëgg ba sank la
Ndeke yiw rek lenen la
Lenen la bul ko weddi
Mbëggel ay coono la bul ko weddi
Mbëggel ay coono la naa ngu nakko
Ndeke mbeuguel nila
Nitt dinala beug ba sank la
Ndeke io req lenen la lenen la bulko weddi
Mbeuguel ay cono la bulko weddi
Ay coono la ay coono la nangulenko
Mbeuguel ay coono la bulenko weddi
Ay coono la ay coono la nangulenko
Sokko khamé nonu



Credits
Writer(s): Youssou N Dour
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link