Dafmay Dal

Taay ma netalilen man lima dal
Si sama digantek xale bima tal
Coono ngantal moy lima dal
Man de lima dal moy ku ma dimbale
Leg leg ma xol ko jooy sax daf may dal
Mba ma xol ko ree si daf may dal
Coono ngantal moy lima dal
Man deh lima tal moy ku ma dimbale

Leg leg ma solu bay dem moom mu terema
Ma daldi tokk li daf may dal
Melni kuko ragal daf may dal
Man deh lima dal moy kuma dimbaleh

Tokk na di waxtaan bis mak samay waay
Telephone bi sonner muy moom ma daldi daw
Melni kou ragal sax dafmay dal
Man lima tal moy kuma dimbaleh ehh waaw

Jëli nala nànd na ni ngay doxe eh hee
Anh anh sa bay mussu ñu ma gnenkouleh sa ba
Lakari lelelaw
Gnekamulehguemou xadila na
Anh moussoletou lakari lelelaw

Worna buur bi yalla ñu bollee
Et siiii ya maléen gënal soxna
Nadipeh ba wakanda
Ndaw si deh moy sama saytaaneh
Mbatam hoo yow jëlël
Annh hi yeah woo woo waawaw

Dama am sa faiblesse xol bi ya ci siy fess
Dëgg la dila jaaner di jooy daf may dal
Gis u loon i gaa yi gëm a tu nu ma
Yenn say ma bëgg njengu gueneuthie daf may dal
Coono gi ci mbeggéel jar na ko doyna ware

Damay woo dame sene
Sama kaw scène
Tajal ko chaine ngir mu beggal maléen

Gis na ni gaa yi gëm a tuñu ma
Goom deh luma wax ñu ni ma baxna
Jox nala cër bi ba mel ni kula ragal daf may dal
Aw ma ci kersa
Dëgg lani jaam si yow la koy ame dafmay dal

Mala tal yama tal
Di defal sama gaa yi dafmay dal waaw
Su sutante dañ may gaañ (ma am sa faiblesse)
Xol bi ya si fess dila jaaner di jooy dafmay dal)

Woo-woo
Coono ngi ci mbeggéel jar nako doyna warreh



Credits
Writer(s): Wally B. Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link