Def Si Code

Banial lolou (n fois)
Yeina say ma kompou leup nopi bayila si bir
Limey togou sou nioré nga xam né may bandit pire
Tioy djiboul diapéma dof boudé moy dalal sa heil
Madone sa ngaka ba am Lima beugue bou yabo nagne ma djéleu
Xam bathia dafa neix djiguéne péxé koon
wéro Yow bandit ngamay diay dagay diém meuneugo
Guiss ma tey né dagma nobb ma ré nga fogue né dal
nga thii fowéma mola taxa dioug wayé dotoko défati
Ma Aÿ thii gor bou guemoul dara ték si beugue ma fowé damley xol dila
ré nane la baby yafi né nane la amo morom béne ngafi sama
gloria niou guéne dioni dioni thiop sa wari tok di xar ria
Banial lolou (2fois)
May wahak Yow mani banial lolou
Adioul lolou (2 fois)
Yama gueune xam né ragalouma lolou
Def si code (5 fois)
Fi lofi indi ngafi feik boulma wo si
arou bandit mane gor la té awma loumey perte
Wathiél sa bopou dalal boul diay sa taar
ni allal amo loudoul sa bop li dalay tardél
Sa dara bouger woul ndah lépeu nga statut (mbété monument)
Loula méték loula néx nga douguel statut (té todjo féneu)
Sol ak soumi mélni amo béneu soucis so
xoulok sa copain nieupeu xamko thi seu statut
Keine faléwoula ko djotél yako toogne
Yow sonal nganiok ma yeureum samay noon
Mbeuguélou film nguéne di doundou falétou léne
moeurs girl bouy wiri wiri dou meuss diok thi mbettel
Dioubeudi wessouwoul déf statut nane la
femme du boss Kane la meuno léne niou ték xeil
Yeine kouleine rawoul dei niémé
ngueine gueumo léne dara ehh Yow réglél
Bo doon mbeur nar nga beuri défaite
niata nga naan baby yafi né bilay yamey daanél
Adioul lolou (2fois)
Yama gueune xam né ragalouma lolou
Banial lolou (2fois)
May wahak Yow mani banial lolou
Def si code (5fois)
Bagn ma ley may (mayma sama baat man)
Mayéwouma(do mayé bougne la mayé do dieul)
Mouyéne(ndigueli)
Yow ndiguelane (ndigueli) (2fois)
Bouldi gawa nagou yeuk sa bopou boudoul Yow di kénéne
Ni mey diapé lay baayé té man gor douma fowé
Leungo néxna wayé ko bayi mou démaki nbagam
Si tu peux m'oublier je ferais comme si t'étais jamais né
Yagui nax sa bopou so foguéni meunoumala bayi
Djiguéne sou gnégué dotoul soor xolam xawma loy diay
Beugue guim la beug boulko diapé ragal
(boulma topou bama seuss nit kou neik amna limite)
Respect bimla diox délo mako wala kou nék
dém (nangoul nala louné thikaw nga nék niit)
Xoulo goudi xoulo beuthieuk dara taxoul nga
beig louniow nga mér dama sonou say caprices
Gor dou ngora késsé djiguéne dagkoy meuneu yeureum
Man kouma nara sonal man ma rombou lafi
Banial lolou (2fois)
May wahak Yow mani banial lolou
Adioul lolou (2fois)
Yama gueune xam né ragalouma lolou
Deif si code (5fois)



Credits
Writer(s): Unknown Unknown, Abdoul Aziz Fall
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link