Sekougn Bayante

Beugank lamigne gna deuk yeineu sayi gnou lalé mane reik ma kham sa
Dieuk motakh seikou bayanté boul meire bâ tank wakh ma loy reithiou
Sougnou dioubéwé meune gama guagne té doko yeuk boul ma waneu sa Dolé
Tidjil sa kanam bigua teuthie mane gua noop mama sommet gnagual
Diapoula même so meiré dagay geuneu rafet doleiy beugeil khadioul si
Iao bayil figua té lewto sou yagué
Dieul bi gnaweu mak io seikougnou bayanté...
Nameu nala wayé fok ma teik kheil yeindo composé sa numéro té douma
Beus appel yeineu sayi ma dougou mode fantôme deif statut khôl la kham
Si loy dokh geidje na guiss no meil soguo may Ray wanté beugou dieuk
Wakh ak mom may goor té fok mou kham ni fi beineu batt la may borom
Lo wakh ma tangal té pourtant mane beug na bayi mou seid deil wakh
Nakh so nopé ma dof sa bat la beug di deigue diaroul gamay waneu ni
Yagui si diam kham nani yagui souffrir mange ak
Iao gnoy wakh té kham na leip damala bâyi si bir
Damala nameu
Dama ragal weitaye tamal guama lou meunete weuy wayé kheuy na
Diga ma woo soumay leik lou neikh bâ kheil bi deimb si ioe d'
Ay melni meussou ma khif wakhal ak
Mane nakh nameu nala sama khôl meuneu guif
Magui beureik sama khôl bi ba goudji gui diekh wayé fouma tourné sa
Kanam lay yam beugeil di geuneu yok miss bama lay dieukeu kham
Mak ioe sougnou kholi none yi am ndam i am sorry ioe nameu nala(...)
Mak ioe seikou gnou bayanté(...
) D'où mane dou ioe kholi gnoko décider...



Credits
Writer(s): Unknown Unknown, Abdoul Aziz Fall
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link