Yarr
par AbouAmg
Elève ladj té tina proffesseur_eum
Ndakh topou xélam wala topou COEUR_eum
Kou beuri xam xam yor si poch yi deureum
Esk waxtou diotoul mou diokh montre heur_eum
Nénan geum bi fok gua diokh ko thieureum
Mai waxou yalla wala waxou serigne
Kouné soul na ay affer si boutou keureum
Galsen deukou dinê wala deukou kheureum
Diné bi néna ma nialo aka bone
Ecole bi néna bagna sol potca réka bone
Gnépa bogon diang mag faté kamil
Gni dakha yégua dakhon wathié kamil
Fok gua diéma fonk papak sa yay
Mai fi sa yay yey nieuk saga sa yay
Woral woral dioulil toubeul
Lo wora woray wedi liguay xoutbeu
Gorak goray wet di niro koubreu
Xoram sakh sou wékhé nirok soukeur
Fi guay guiss kou fayal diang domam
Bagna topato lan laniy dougal bopam
Xalé boboy mag wouté wak wa keureum
Papi nek fofou di dioy nan bayina yonam
Motakh neggers yagui ni di dioylo fille de joie
Neggers yagui ni di dioylo fille de joie
Yen say pour gua mour ween digua sol
Yeuré bou tollou si genoux
Niouné lo guis day diékh souma
Timé sama yay damay geumou
Kour gui fess dagua niou don fowé ay
Pistolé bouniou len dinan diagui leen
Xam xam grap la bou dom yi nioré
No mounti deff dina am niou sani khér
Beug alal ba wakhou niou lim niou diaral
Kou beug dara ak kou bagna toul dara
Yallay buur mai buur yi geumou niou yalla
Mag dou yalla mai yag nak yalla
Am say dom ba paré berleen di
Diéma diay ba Alleman (guani lane?)
Té berlin amoul pa allmen
Djiguen bou khamoul gor dh dan koy weur
Gor bou xamoul djiguen dankoy wiiri
Pourtan borou heurou wiiri wiiri
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah yeah
Geuneu iri niggah
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah
Wa keur gui sounou fonkoul séni dom yi
Kon dh sén kharit yi laniy wowé mifa
Boul changer deuk mais changel deuk bi
Adouna bi souy touki ken dou la may visa
Nit kou nioul day youkhou fi ba souba
Toubab bi degoul loudoul houba houba
Toubaba kheuthi nopou senegalais kheuy
Na motakh senegalais degoul toubab
Fok gua niémé wakh nit bopam
Même goumba bokoné goumba mou guis bopam
Oustaz dénthieul masa yatt bi
Gneuweul firil ma ayat bi
Xalé déna keur gui néna doundou woul sakh
Yakh biir té mom mi dioudou woul sakh
Andando bou gnaw sou tassé rafet
Dara eupoul fitt ay dénth tapet
Djiguen bou khamoul gor dh dan koy weur
Gor bou xamoul djiguen dankoy wiiri
Pourtan borou heurou wiiri wiiri
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah yeah
Geuneu iri niggah
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah
Nigger yaral sa dom Samal sa dom
Kou geuneu am dh geunoul diang c faux
Gni geuneu niak niofi dakhon kheuthio
Beug ndiékh dou takh niou thinn bou tang kheupo
Ndakh bonou tégué niam kou féké sigua
Borom ndéki kouko nieuk yêwou teudat
Djikoy sopalikou dian ba mat borom
Sentou werr diaroul boukhanték sa morom
Nénagn deuk gar takhoul bari gane
Mai noyé adouna takhoul gua goudou fan
Bakan com ay thiarakh bouy dag doko yeug
Loula mar meunou may matt doulako may
Té mem bo amoul bac am kérsa diarna bakkou
Magoum wakhon nako mo geun khamon nako
Guélaw dougal khop si kamb mai douko si guéné
Bodé batou keur gui mbed doula degg
Nigger yarr
Elève ladj té tina proffesseur_eum
Ndakh topou xélam wala topou COEUR_eum
Kou beuri xam xam yor si poch yi deureum
Esk waxtou diotoul mou diokh montre heur_eum
Nénan geum bi fok gua diokh ko thieureum
Mai waxou yalla wala waxou serigne
Kouné soul na ay affer si boutou keureum
Galsen deukou dinê wala deukou kheureum
Diné bi néna ma nialo aka bone
Ecole bi néna bagna sol potca réka bone
Gnépa bogon diang mag faté kamil
Gni dakha yégua dakhon wathié kamil
Fok gua diéma fonk papak sa yay
Mai fi sa yay yey nieuk saga sa yay
Woral woral dioulil toubeul
Lo wora woray wedi liguay xoutbeu
Gorak goray wet di niro koubreu
Xoram sakh sou wékhé nirok soukeur
Fi guay guiss kou fayal diang domam
Bagna topato lan laniy dougal bopam
Xalé boboy mag wouté wak wa keureum
Papi nek fofou di dioy nan bayina yonam
Motakh neggers yagui ni di dioylo fille de joie
Neggers yagui ni di dioylo fille de joie
Yen say pour gua mour ween digua sol
Yeuré bou tollou si genoux
Niouné lo guis day diékh souma
Timé sama yay damay geumou
Kour gui fess dagua niou don fowé ay
Pistolé bouniou len dinan diagui leen
Xam xam grap la bou dom yi nioré
No mounti deff dina am niou sani khér
Beug alal ba wakhou niou lim niou diaral
Kou beug dara ak kou bagna toul dara
Yallay buur mai buur yi geumou niou yalla
Mag dou yalla mai yag nak yalla
Am say dom ba paré berleen di
Diéma diay ba Alleman (guani lane?)
Té berlin amoul pa allmen
Djiguen bou khamoul gor dh dan koy weur
Gor bou xamoul djiguen dankoy wiiri
Pourtan borou heurou wiiri wiiri
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah yeah
Geuneu iri niggah
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah
Wa keur gui sounou fonkoul séni dom yi
Kon dh sén kharit yi laniy wowé mifa
Boul changer deuk mais changel deuk bi
Adouna bi souy touki ken dou la may visa
Nit kou nioul day youkhou fi ba souba
Toubab bi degoul loudoul houba houba
Toubaba kheuthi nopou senegalais kheuy
Na motakh senegalais degoul toubab
Fok gua niémé wakh nit bopam
Même goumba bokoné goumba mou guis bopam
Oustaz dénthieul masa yatt bi
Gneuweul firil ma ayat bi
Xalé déna keur gui néna doundou woul sakh
Yakh biir té mom mi dioudou woul sakh
Andando bou gnaw sou tassé rafet
Dara eupoul fitt ay dénth tapet
Djiguen bou khamoul gor dh dan koy weur
Gor bou xamoul djiguen dankoy wiiri
Pourtan borou heurou wiiri wiiri
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah yeah
Geuneu iri niggah
Domou pa you fir yi laniy geuneu iri niggah
Nigger yaral sa dom Samal sa dom
Kou geuneu am dh geunoul diang c faux
Gni geuneu niak niofi dakhon kheuthio
Beug ndiékh dou takh niou thinn bou tang kheupo
Ndakh bonou tégué niam kou féké sigua
Borom ndéki kouko nieuk yêwou teudat
Djikoy sopalikou dian ba mat borom
Sentou werr diaroul boukhanték sa morom
Nénagn deuk gar takhoul bari gane
Mai noyé adouna takhoul gua goudou fan
Bakan com ay thiarakh bouy dag doko yeug
Loula mar meunou may matt doulako may
Té mem bo amoul bac am kérsa diarna bakkou
Magoum wakhon nako mo geun khamon nako
Guélaw dougal khop si kamb mai douko si guéné
Bodé batou keur gui mbed doula degg
Nigger yarr
Credits
Writer(s): Omzo Dollar
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.