Wéétoo

Wéétoo, wéétatinaa yaay
Wéétatinaa, wéétatinaa, wéétatinna yaay
Sophie demna tey ma dabiko
Sainte-Marguerite sorina tey ma dabiko

Sophie demna, moommii nëwna, moommi demna nii
Sophie demna, moommi newna moommii demna nii
Sophie demnaa tey ma dabiko
Sainte-Marguerite sorinaa tey ma dabiko

Demnaa fimu dem sorinaa sana guel demnaa yow
Fimu dem sorinaa tey ma dabiko ndeysaay



Credits
Writer(s): El Hadji Fall Diouf, Pape Abdou Karim Diouf, Michael Sawatzky
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link