Bombaclat

L'impérialisme! (À bas!)
Le néo-colonialisme! (À bas!)
Le racisme! (À bas!)
Le fantochisme! (À bas!)
Gloire! (Au peuple!)
Dignité! (Au peuple!)
Pouvoir! (Au peuple!)
La patrie ou la mort, nous vaincrons!
La patrie ou la mort, nous vaincrons!
Merci camarades

Danie niu door ci maf bi danie niu lie lie ya
Ndjit you bonn yi yobé nanie niu faya faya
Bombaclat tchi niom gni niata lanie fi raye ya
Complot ak toubab bi déf niou ay bétails ya
Rogne naniou bepp koom biwoon ci guedj ak souf
Xadialé Africa mouy gueun di wéey di soukh
Ana gniy agualé xéexu Sankara
Kou fipou diouk rek babylone nieuw sankeu la
Liy daw sén yaram dou dérétou guor
Falou ci réwou black sathie léen di ligueyal toubab
Yéneu yéess yéén bane xéetu khole nguen yor
Costume cravate deuké diay mana complexé nguéw
Gni leu fale nga délou yéw
Babylone foum beugu nga téw
Do signél lou bakh sa rew
Yay kou yorr djiko diou séw
Mane meunouma fékéti rew miy naakh saay
Now wakhtou diotna Afrique burn yi saï saï
Diougual nga wooté révolution now
Li Afrique mom na déss Afrique niou dieufandiko
War naniou meuneu diangu war am ay hopitaux
Liniou am tchi koom dou yoon niouy xeuy di dound ci ndole
Li yepp ay ndjit you bonn
Li yepp nguéw yéniou tonie
Siguil té xam sa bopp
Africa dél mind
Niom liniou leu def last time
Yéw sey mame banopi dominé sa askane
Del mind yaw rékeu farr niom niouley sott sotto
Bolo ande def saï rek la fokk ni lolou nga sokhla now
Rest in peace Amilcar Cabral wané neu ngoora dém
Rest in peace Patrice Lumumba wané neu ngoora dém
Aiiight taye dji gni fi néh nio yéw djiaay
Séni brother lawoon fawoon rek mo khéw taye
Ouattara ak Macky are we bad lucky
Africa foumiy dieuleti Muhammar Khadafi
Babylone dafniou noote meussoul beugu Africa diouk
Ay ndjitou rew you nioul la sampe tchi souf mou ba fi kaddu
Niou dem beu nit yiy faatou économie bi mabou
Mou am ay Jaques Focart you béss youy nass akeu rabou

Danie leu yéw djaay
Africa danie leu yéw djaay
Danie leu yéw djaay
Africa danie leu yéw djaay
Danie leu yéw djaay
Africa niom danie leu yéw djiaay
Danie leu yéw djaaay
Africa danie leu yéw djaay



Credits
Writer(s): Jonathan Legigan, Mor Talla Gueye, Tony Brian
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link