Chaise anglaise - FF2

Pape Laye Beats

DD Records!

Flow bo kolo kolo
Beugg ma keule keulé
Xam nga kanté ngolo
Xam sa baay ak golo
Yeuk nga 4 da fodo
Geucc na rap mais lolou dou tiotio
Yo ma haters
Sa pussy mama sama logo
Héy yeah hann
Sa pussy mama sama logo

Yeah guis na aye carriere you tiank (Yeah)
Comme xathie bouy tince
Guis na aye rappeur youy fenn (han)
Comme Père Noël
Guis na aye rapper youy xon (waw)
Pour joote aye fonds
Gni sen xeli du téyeu
Comme kuy lekk thi douche
Boudé da ngay faye facture
Wala ngay dieund aye couche
Fi meun nga fenn sa public
Bo beugué am lo lekk
Respect du faye courant fenn kat yii raye sen dékk
Rappeur comme sukeuru békk
Gnome gneup toyeu lagnouy bagne
Politique leu lolo du dagne
Pression comme soukeurou koor
Wooori té gnome meussougnou woor

Ana sa Prési
Dafa busy
Loumouy deff no dafaay day
No no FIFA lafiye play
Waxko deugg boulko rousse
Boy nieupeuy douggou dousse
Dang ma saaw no ya meune poupp
Meun nga...
Té do saw?
No no no nooooo

Soumala teudé dina teudi dji jail
Sku sku sku!!
Yao alalou procureur nga defko sa xell
Wé wé wé wéééé
Soumala teudé dina teudi dji jail
Sku sku sku!!
Yao alalou procureur nga defko sa xell
Wé wé wé wéééé

Sa bireumeu teuf teuf teuf teuf
Sa bireuma kaléru haa!
Muskad camelia numero ha hé
Sa numero hé hé...

Li dou mane
Li dou nén
Boudone nén leu kone mou tothie
Li dou rap
Actifed la jeleul naan da nga sothie
Rappeur nga japo thi tok
Eleve nga jangal mou mok
Yaafi meun nala thi nok
Bass Thioung ngay concurencél waxo fi tiok
Rap galsen copie colle boy Youtube waxoul deug
Dilén bathie gnoukoy nangou ni Samba Peuzzi biir Reptyle
Faraloumala duma farantok goor boy aye thieu teudile
Makoy yeungeul diko yeungeul boy sa papa meuneu teugg
Meun na rap ame na japp
Dafa fess mongui tourou mongui tokou
Meun nga rap yama meun foma guissé wokou dokh
Game bi thi pot ku pare punchline woté kaylén lapma

Ana sa Prési
Dafa busy
Loumouy deff no dafaay day
No no FIFA lafiye play
Waxko deugg boulko rousse
Boy nieupeuy douggou dousse
Dang ma saaw no ya meune poupp
Meun nga...
Té do saw?
No no no nooooo

Soumala teudé dina teudi dji jail
Sku sku sku!!
Yao alalou procureur nga defko sa xell
Wé wé wé wéééé
Soumala teudé dina teudi dji jail
Sku sku sku!!
Yao alalou procureur nga defko sa xell
Wé wé wé wéééé



Credits
Writer(s): Lamine Doucoure
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link