La Famille

Reptyle Music

Yah yah

Wessu neñ xarit
Legui done nene ay domu ndeye
Ak ñing ma guissalone dëmba nga mey guissal tey
Ko toñ si gang bi
Ñoune ñeup nga toñ
Wessu neñ xarit
Legui done nene ay domu ndeye
Ay niitou dëgg
Fi kene dou changer
My brotha for life never change
Ay niitou dëgg
Fi kene dou changer (hey)
My brotha for life hey
Yah

La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille hey

Ça bouge pas
La famille
(Gang gang)

La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille hey
Yah yah hey

I do it for the gang, i do it for my family
Lou moun'ti xëw, dou takh ñou tass c'est à vie
Bo déconner dam lakey wakh rek ñou andate cool
Lou yagga degg la souñ anda bi deh dou ay doul
Faté xadiou fi
Yene rek ladone guiss
Depuis bou mouy metti (ra ah ah)
Xolal faté xadiou fi
Yena ma doleel
Bama yeksi fi (ah yah hey)

La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille hey

Ça bouge pas
La famille hey yah

La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille hey yah yah hey

Wessu neñ xarit
Legui done nene ay domu ndeye
Ak ñing ma guissalone dëmba nga mey guissal tey
Ko toñ si gang bi
Ñoune ñeup nga toñ
Wessu neñ xarit
Legui done nene ay domu ndeye
Ay niitou dëgg
Fi kene dou changer
My brotha for life never change
Ay niitou dëgg
Fi kene dou changer (hey)
My brotha for life hey
Yah

La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille hey

Ça bouge pas
La famille yah yah

La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille hey yah yah hey

Ça bouge pas
La famille yah yah
Ça bouge pas
La famille yah yah

La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille hey yah yah hey



Credits
Writer(s): Christ Johan Ollanghas Kimbeki, Samba Tine, Pape Moussa Diagne
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link