Styliste vers

DD Record's
Pape Laye (Pape Laye)

Styliste vers
Kuy sa best rapper waxaal gaw ma fayko weer
Styliste vers
Flow bu sanguinaire
Mesurer sa hanchu mere
Styliste vers
Kuy sa best rapper waxaal gaw ma fayko weer
Styliste vers
Flow bu sanguinaire
Mesurer sa hanchu mere

Ciseau d'or la yoor
Di jongaal aye bitches
Centimetre sama loxo
Di jangal aye mcs
Damay daag damay xooti damay Tepi di niaw
Flow bu geuneu rouké fouf fou weugn ak pousso di aw
Flow bu geu eu niaw fouf kounek si mbed di saw
Malen meune nelen waw
Naka war gnouné ciao
Tocc aye casse thi aye vers
Jeul centi souple mesure sa HU mere
Si si mongui si weer
Guis kou geuneu aye 4leuz guis nga nenou mouss
Yasuke geuneu paré boye ku geuneu thi douss
Sa mc dafa tiéré mbok neko mou pousse
Mangui punch gnimay xirou tamite lolou tousse

Styliste vers
Kuy sa best rapper waxaal gaw ma fayko weer
Styliste vers
Flow bu sanguinaire
Mesurer sa hanchu mere
Styliste vers
Kuy sa best rapper waxaal gaw ma fayko weer
Styliste vers
Flow bu sanguinaire
Mesurer sa hanchu mere

Rap bu dé fowou xell mane géni la
Jokhma tieur ni ku xotil sa papa ganila
Deggo francais lakal wolof ndax yao do nix
Xuru néne dou xibaar ben yoon thi film x
Waw je fais du sale
Comme macky sall
Lonku rap bi centimètre ken du bougé mètre
Deflén aye bloc dimeu xéx ma niawal len xaftane
Sokhlawuma sidiada pour jouler sén rappeurs yii
Da nga clash dagnoula vent
Demal tok sa banc
Archiviste Architect rest in peace kuma lekk
Aye thi beat bi piste 4leuz rayal sa dékk
Rap bi thi 4leuz leu nek
Rappeur nga xam ko bu diek
Ma djitu ngueneu toppou
Ku degul katal sa nopp
So méré talaal sa bopp
Wallaah Wallaah hé arrête de faire genre arrête!!!!

Styliste vers
Kuy sa best rapper waxaal gaw ma fayko weer
Styliste vers
Flow bu sanguinaire
Mesurer sa hanchu mere
Styliste vers
Kuy sa best rapper waxaal gaw ma fayko weer
Styliste vers
Flow bu sanguinaire
Mesurer sa hanchu mere

Aka Louis Vuitton
King kocc hé
Gianni Versace
Styliste vers styliste rimes styliste flow Yo
Yasuke coming soon
Weshhhh
Hé wallaaah c'est migonnnn!!!



Credits
Writer(s): Mamadou Lamine Doucoure
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link