Deug deug
Yeah
DIP
Check
Da nga teudone rek di guënte wayé nala yéé
Ndakh né nagnema deug nekhoul deugueuntane na nekh
Boul meusseu xepp dara kounek lila Yallah may
Xalé ba ngui djoy té mateu mbélènetane la rek
Meunouma nadjé yégueu none yéma téla xékh
Tchine bou baxé xégne da fek dafa ndara nekh
Deug bou amoul massla la ndara tek nak
Real Rap dou Salsa dou Wane Téraméra
Gnouné mola gueune mougneul di nga meusseu mogneu
Maye lathie loutah sa ndey dior gueuneul la sa thiamogne?
Loutah ngay laabé thiamogne té ndey dior-ra dankone?
Loutah Goor yi di sawé thiamogne thiamogne ndey dior-ra tankone?
Li ngay gueume molay dal lolou rek-kafi né
Diaroul di sett fou sori sa boppeuh doy nala firndé
Bagni nek boy lagne gnou téré carte xaliss
Té bobou ba légui LONASE mo ngui lindia sunu Pa yi
Né nga Yallah nga gueum loy doyé gris-gris
Né nga mbède ngay téwal loy dokh di saw cii murs yi
Li ngay dégue gnoulay wakh boukoutak lignou lay wane
Wakh li ngay deffa gueuneu yomb ngay def li ngay wakh
Goor Yomboul ndax amena goor-djiguène yougnou djongal
Mane nek na Goor Yallah bala ma djongou
I'm Real niggah té douma sopalikou
Damay khar samay tank toubeuy ba mère bi nopalikou
Kou bagne gnou wakh loumou défoul, dou wané loumou nékoul
Noone ya ngui fouma yégoul douma lène dieuw dama lén ci teukou
Ya ngui cii kaw ma ngui cii souf lolou motah maye sissou
Gnam bi souma cii lékoul fawma keupeu cii souf
Sen Flow dissoul kène ci yène todjou cii Youtube
Rap rek lafi guissoul fuck gni nane damay sissou
Time is money wakh ko bororm Montres yu chère yi
Ba nga fataliko dealers youniou kep cii jail yi
Sokhor ba bougnou défé lou bakh dafa fek gnou joum
Xalé bouy diawalé dalam yène say mou solko mou djoupp
Sa life dafa yombone ngay woute life bou djingue
Aduna rawaneté la rek té légui moudjé nga
Boy yi djapé sen boppeuh star, Stars yi djapp sen boppeuh
Roussena njeukeunté té djémouma raw Usain Bolt
Bokoumak gni di wakh le ciel est la limite
Assamane yi beuri nagne kone bi dou sama limite
Xepp tokou dérette bidoul xonkal keuleu méw
Est-ce que takhoul gnou mystique badi souli néw?
Kou xam ñi tey'lé ay bakaan tchi ay mbiir you nëw
Journal bi lou nieup xam rek lay souligné
Télé ngay tok di sétane kou amoul lou matt sept ans
Ci Film bo xam kou amoul 16 ans douko sétane
Diamono ngui dokh nieup ngui toppeuh Sheytane
Yaw démalak sa xel xol fi ngay tek say tankeu
Accident yi beuri nagnou cii nignouko guissé
Té meusso dégue Carrapide firr na policier
Xalissou rééwmi kou nek meussna cii cotisé
Ngour ngui lekk ko dignou leurré ak audité
Obama louko indi léwal goor-djiguène
Nélène gnou wakh cii chomage bi gnoune dé nio ngui déh
Agression day fay ndakh def nagnou ko liguéy
Wagnékou woul ndax gnikoy def yeup gnam nagnou jail
Mbède boumou takh nga taukh baune boul meusseu done soulard
Ragal Dou Diégui Rail Bandit dou dokh cii filou courant
Légui nieup am fiit xalé yi sakh dawatougnou KanKourang
Chrétien té amo BIBLE, Dioulite boudoul khol AL-QURAN
Ray nagnou Sadam Hussein ak Ossama Ben Laden
Té né nagnou dougou nagnou Akhrou Zamane may day
Picc bou laké cii taate day beug am morom
Sheytane dafa takk beug gno def morom
Fène tribunal wessou woul Ragal nitt gnémé Yallah
Monsieur le Juge do Yallah kone boul topando Yallah
Yélwane def nagnou ko Job ndax kène bagnoul diokhé nguir Yallah
Wayé boy mayé ay Millards faw gnou Caméra la
Président day djité sakh gniko voté loule
DIP jottéwoul ak yaw mais li ngay RAP moko dougoul
Texte bou tilime la bindé deug dji ngène dégue
Di ngène bëg boudé beug ngène dégue deug deug

Credits
Writer(s): Dominique Preira
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Other Album Tracks
© 2024 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.