Ndeye
Ndeye mougneul sa thiono dina faay
Say rongothi dina férr bilay
Ndeye sa Tàar bi nakar rako mour tay
Kéneu xamatoul loy nirol ndakh thionay seuy
Ndeye meusta degg waw gòor
Té sou outi woul indi keur gui dougnou tal bay sôr
Teksi aye gorom sonal ko
Té sou wakhé dieukeureum tégal kossi aye dóor
Ndeye siguil nga xolma
Sa beugn you wekh yi la nameu nak rétane ma
Djougal nga dellou keur gua
Mourol sa malanou soutoura té fanane ci jamm
Yéneu say mou dioy ndakh wakh you bone yignou deukal ci nopam
Rongogn yangui sàngu dom dji mou tím diko nampal
(Góor-góorloul waay)
Ndeye mougnal
Yalla guiss na lepp
Ndeye
Dina meussa bakhi
Boul meussa bayi
Ndeye mougnal
Li lepp dey diekh
Faw mou méti dora nekh
Ndeye mougnal
Ndeye mougal sou dom yi magué féral say rongogn
Boul meussa bayi
Ndeye mougnal
Enh mougnal waay
Dina meussa bakh
Ndeye mougn na ba naak
Wouyou djina borom mam biko saak
Ndeye meusta xam banekh
Té bimouy tolou ci digë ndawam ngako takk
Meussoul ame ci yaw louko nekh
Té lounék ladane def nguir dap sa banex
Ndeye meussou lo fanae aleu
Wayé tay goudé nga
Foy fanane tay?
Nakar ak tiss rek laka yobbou
Wayé lepp diexna
Boul guiss lo ragal way
Ndeye mougn na ba dém
Té narta féké sah ndieurign domam
Ndeyoo Ndeye!!!
Dieuf djou bone djounek dieureur-am Tek koko mom aki mbokam
Lou nguéni lay tay?
Sa doundou gawa fay comme sondel bougnou tek ci nguélaw
Yalla bo guiss lo ragal finga dieum
Teudeul nga nélaw
Ndeye demna!!!
Ndeye demna (demna)!!!
Ndeye demna!!!
Demna dotoul nieuwatt
Meusoul ame louko nekh ci bir doundam
Ndeye demna
Say rongothi dina férr bilay
Ndeye sa Tàar bi nakar rako mour tay
Kéneu xamatoul loy nirol ndakh thionay seuy
Ndeye meusta degg waw gòor
Té sou outi woul indi keur gui dougnou tal bay sôr
Teksi aye gorom sonal ko
Té sou wakhé dieukeureum tégal kossi aye dóor
Ndeye siguil nga xolma
Sa beugn you wekh yi la nameu nak rétane ma
Djougal nga dellou keur gua
Mourol sa malanou soutoura té fanane ci jamm
Yéneu say mou dioy ndakh wakh you bone yignou deukal ci nopam
Rongogn yangui sàngu dom dji mou tím diko nampal
(Góor-góorloul waay)
Ndeye mougnal
Yalla guiss na lepp
Ndeye
Dina meussa bakhi
Boul meussa bayi
Ndeye mougnal
Li lepp dey diekh
Faw mou méti dora nekh
Ndeye mougnal
Ndeye mougal sou dom yi magué féral say rongogn
Boul meussa bayi
Ndeye mougnal
Enh mougnal waay
Dina meussa bakh
Ndeye mougn na ba naak
Wouyou djina borom mam biko saak
Ndeye meusta xam banekh
Té bimouy tolou ci digë ndawam ngako takk
Meussoul ame ci yaw louko nekh
Té lounék ladane def nguir dap sa banex
Ndeye meussou lo fanae aleu
Wayé tay goudé nga
Foy fanane tay?
Nakar ak tiss rek laka yobbou
Wayé lepp diexna
Boul guiss lo ragal way
Ndeye mougn na ba dém
Té narta féké sah ndieurign domam
Ndeyoo Ndeye!!!
Dieuf djou bone djounek dieureur-am Tek koko mom aki mbokam
Lou nguéni lay tay?
Sa doundou gawa fay comme sondel bougnou tek ci nguélaw
Yalla bo guiss lo ragal finga dieum
Teudeul nga nélaw
Ndeye demna!!!
Ndeye demna (demna)!!!
Ndeye demna!!!
Demna dotoul nieuwatt
Meusoul ame louko nekh ci bir doundam
Ndeye demna
Credits
Writer(s): Charles Diagne, Abdoulahat Thioune
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.