Certifié
Han
Jooxé leep linga beugue sa deugue
Sa deugueu deugueu ndekké loloy sa deugueu
Diougué fou sorri ba akssi fou djegué
Tchi waxou kassaw kassaw domassi degueu
Roppi sa rappeur boy rappeler koko
Douggal tchi mane rek nga guéné ay bobo
Mamadou Doucouré Amaru Shakur
Boy yi né tioukkou na
Non mane màné tioukkool
Beurri ndieurigne melni pepeu si tchiine bi
Seppi si tchiin bi kou nekka si king bi
Wirri wirri dina la keep si ndaa li
Beurri tierré yangui nourrol sa dalla yi
Bayil sa barres yi do dougueul lou douggu
Xawma sa kanaam yow waxma no toudou
Yow la kane wakh ma fo todj
Dieundeul allumettes sa rap takh
Yow la kane wakh ma fo todj
Dieundeul allumettes pour sa rap takh
Na nguene deff
Ay Yallah miñu sakka
Dano sonu
Dano tayi
Rappor yiii yi ni ah
Beugueu ma perte moy beugo lou bakh
Songga ma beurré moy danu nga ndiakh
Douggou paré ticket win sama jeans
Gueuneu bleu Tour-Eiffel ak Gana Gueye
Diappa ndigueu diappa poteau Gana Gueye
Lou deuguueur tchi digueu bi mane la Gana Gueye
Katsandeye
Rrr
Hey
Kou niane niakka dieundeu am sama rap meunoul begneu am ndam
Hey hey hey
Rap concours leumbeul
Ay goor ngui si geew bi
Boy boy yangui si kogne bi
Di dewo ni neew bi
Di yamba di tielli
Di rever Sindielly
For the eye mongui fanane tchi bitti
For the game mangui final ni City
Gueune la ay gueuneu febbar kou Sitti
Di fowé rap ni kou djoudo si Gouy gui
Meune ko def teurreul tabaski kouy gui
Damey songa Piqué
Douma polémiquer
Sama tuur bi diké comme Dallou Dakar
Bouddil Adamo la
4Leuz moy rappeur bou kharoul tchi keneu
Kholoul tchi kenneu
Té gnewoul tchi kenneu
Andoul ak kenneu ndakh da nguene di senneu
Weur rek di fenn rek
Boy yene dal boy merci
Dindil sa sagga yi nga wakh ma lou dess fi
Dindil sa clash yi nga wakh ma lou dess fi
Ñou xeuyône di andd
Ño xeuyate di clashanter
Douma lene sakh deglou boy
Deem lene nguene tesseunté
Deem lene nguene tinsseunté
Yeah
Rang mouy bleu
Tcha bleu ba la
Yasuke coming soon
King Kocc
4Leuzophy
Yesso
Hey diko mey sama nigga
Doufé douffi douffé
Jooxé leep linga beugue sa deugue
Sa deugueu deugueu ndekké loloy sa deugueu
Diougué fou sorri ba akssi fou djegué
Tchi waxou kassaw kassaw domassi degueu
Roppi sa rappeur boy rappeler koko
Douggal tchi mane rek nga guéné ay bobo
Mamadou Doucouré Amaru Shakur
Boy yi né tioukkou na
Non mane màné tioukkool
Beurri ndieurigne melni pepeu si tchiine bi
Seppi si tchiin bi kou nekka si king bi
Wirri wirri dina la keep si ndaa li
Beurri tierré yangui nourrol sa dalla yi
Bayil sa barres yi do dougueul lou douggu
Xawma sa kanaam yow waxma no toudou
Yow la kane wakh ma fo todj
Dieundeul allumettes sa rap takh
Yow la kane wakh ma fo todj
Dieundeul allumettes pour sa rap takh
Na nguene deff
Ay Yallah miñu sakka
Dano sonu
Dano tayi
Rappor yiii yi ni ah
Beugueu ma perte moy beugo lou bakh
Songga ma beurré moy danu nga ndiakh
Douggou paré ticket win sama jeans
Gueuneu bleu Tour-Eiffel ak Gana Gueye
Diappa ndigueu diappa poteau Gana Gueye
Lou deuguueur tchi digueu bi mane la Gana Gueye
Katsandeye
Rrr
Hey
Kou niane niakka dieundeu am sama rap meunoul begneu am ndam
Hey hey hey
Rap concours leumbeul
Ay goor ngui si geew bi
Boy boy yangui si kogne bi
Di dewo ni neew bi
Di yamba di tielli
Di rever Sindielly
For the eye mongui fanane tchi bitti
For the game mangui final ni City
Gueune la ay gueuneu febbar kou Sitti
Di fowé rap ni kou djoudo si Gouy gui
Meune ko def teurreul tabaski kouy gui
Damey songa Piqué
Douma polémiquer
Sama tuur bi diké comme Dallou Dakar
Bouddil Adamo la
4Leuz moy rappeur bou kharoul tchi keneu
Kholoul tchi kenneu
Té gnewoul tchi kenneu
Andoul ak kenneu ndakh da nguene di senneu
Weur rek di fenn rek
Boy yene dal boy merci
Dindil sa sagga yi nga wakh ma lou dess fi
Dindil sa clash yi nga wakh ma lou dess fi
Ñou xeuyône di andd
Ño xeuyate di clashanter
Douma lene sakh deglou boy
Deem lene nguene tesseunté
Deem lene nguene tinsseunté
Yeah
Rang mouy bleu
Tcha bleu ba la
Yasuke coming soon
King Kocc
4Leuzophy
Yesso
Hey diko mey sama nigga
Doufé douffi douffé
Credits
Writer(s): Mamadou Lamine Doucoure
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.