Boul Ko Faté

Bayi na lu bari
Bayi nañu bari
Bul def luñ ñuy xébé
Damla nopp bulko faté
Gni nane du sorri
Gni nane du sotti
Bëgg na la té luma am jël
Bul mey none yi luñu rétané

Té yow xana xamo
Yaye pé ci xol bi su done course do jël ndaré
Munuma lako nëb day fégn ci nimlay xolé
Yaye sama choice nagn ci tekk brick
Dundu sunu paradise
Oh oh
Bulma miinël sa bopu ba paré wone më guinaw
Lomay tammal na nekk luy laaw
Xol du hauum bagnkay bëss
Amatuma sago ci yaw

Mbëggeel di taw sama xol lima wër yëp di naat
Biss bimalay ñëk guiss suma sanione dey niowat
Baayi ñëp né yow la
Yow laay tiitëroo woo waaayy

Budul yaw du kene fi nga nekk la né
Limay yëkk ci woy mane dafma ëpp doolé
Eyyy, Ohh ouhh hooo...
Sama xol moma toogn bama melni
Mom moma toogn bama melni (ci yow)
Yeeeeh ehhhhhh ey
Ohhhhh ouhhh ohhhhh ohh

Yaye sama ceetu
Bulma nax ci yow lay guiss sama bopu
Yaye lamp bimay leeral
Sodone jaye lugn ma ladj ma faye ko
Mba doma Russlo ci sama kanamu ay nawlé
Yaye wax na pape wax samay xarit
Mani yaw la
Bëgguma ko rethiu
Loma ladj ma deff ko
Mala bëgg piir té luma ci gobé garr ko
Paré déku lepp rek ci kaw nga xam ko
Pur ñu dem dey dess ci yow
Ande niarakoy deff
Bëgg na la bamu leer ñëp
Jël sa photo def ko sama profil yëp
Sudé mbëggeel jox nalako bamu matt sëkk
Bayil xel lima bayi lepp
Lepp nguirr yaw

Mbëggeel di taw sama xol lima wër yëp di naat
Biss bimalay ñëk guiss suma sagnone day ñëwat
Bayi ñëp né yawlë
Yaw lay titërooo woooo waaaayyy

Budul yow du kene fi nga nekk la né
Limay yëkk ci yow mane dafma ëpp doolé
Ohh ohoo hooo
Sama xol moma toogn bama melni
Mom moma toogn bama melni (ci yow)
Yeeeeh ehhhhhh ey
Ohhhh ouhhhhh ohhhh ohh

Jox na la li guënë fort ci mane
Muy sama xol
Kone dessalatumla daaraaa
Aand niarakoy deff
Wane na la li gënë sorri ci mane
Yaye sama xol kone dessalatumla dara
Andë ñarakoy deff



Credits
Writer(s): Abdoul Aziz Fall, Abdou Hioune, Charles Diagne, Charles Sow
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link