WURUS - Version Afro

(I'm in love with you)
(In the morning)
(In the night)
(Oh yeah(oh yeah)

(I'm in love with you
(In the morning)
(In the night)

Yay sama aduna
Oh yeah
Sama baby Coco way
Hey yeah

Yaw mi Yay sama aldiana
My love
Sama baby Coco way
Hummm yeah

Baby yay man
Teudeul nélaw xamni
Mounoul dara
I don't give a fuck
Mérr Kat
Fadioul dara

Takkal Leu ay or
Ba ci 24 carats
Dagn lénni
Bayé am peureum
Té ñom ñuy deuké ayah

Baby I just want real love
Real love
I just want now
Real love

Baby I don't want lie

(I'm in love with you
In the morning
In the night
Oh yeah (oh yeah)

Yay sama aduna
Oh yeah
Sama baby Coco way
Hey yeah
Yaw yay sama aldiana
My love
Sama baby Coco way

Way way way
Mérr bi fadioul dara
Mom fadioul dara
Kon fadioul dara

Bayi lén té ñeuw
Ma takkal Leu
Or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngalam 24 carats

Xanna do maala yéné
Ma vie
Ma vie
Ma

Baby yay man
Teudeul nélaw xamni
Mounoul dara
I don't give a fuck
Mérr Kat
Fadioul dara

Takkal Leu ay or
Ba ci 24 carats
Dagn lénni
Bayé am peureum
Té ñuy déké ayah

Baby I just want real love
Real love
I just want now
Real love

Baby I don't want lie

I'm in love with you
In the morning
In the night
Oh yeah (oh yeah)

Yay sama aduna
Oh yeah
Sama baby Coco way
Hey yeah
Yaw yay sama aldiana
My love
Sama baby Coco way

Way way way
Mérr bi fadioul dara
Mom fadioul dara
Kon fadioul dara
Bayi lén té ñeuw
Ma takkal Leu
Or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngalam 24 carats



Credits
Writer(s): Wally B. Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link