Fou De Toi

Maestro nénéné

Cherie fouñu diar yép (Yép)
Bamouy méti bébé
Ñun ñar rék (Rék)
Cherie fouñu diar yép (Yép)
Li guenone méti bébé
Romb nañu lep (Lép)
Cherie coco no no boul dem

And nañ ba Yalla def ñu seuy Si farata
Nga mouñal ma louma jiguen meusta mouñal Jaarama
Yaw milé
Yaw milé deh
Yama dioural sama taw bé
Yaw milé éh éh
Yaw mi deh
Yamay motali souma wété
So démé sama keur gui dina tasss Wawawaw

Chérie sama xol yawa
Té kinga xam mana
Namnala man bay dioy
Chérie daga dém ma wétt
Té so ñeuwé mou déñ
Boudoul yaw dou done kénén
Lolo am
Té dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Man dama dof si yaw
Dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Chérie man dama dof si yaw

Xamna ni mala togn baby
Je t'assure j'ai fauté baby waw
Je me suis excusé
Adouna bi yama si guenal
Maguilay dora togn chérie boy mané balma
Bouñ la wowé fi lé
Bouñ la wowé néla dof na
Boumla bétt balma

(Yép yép)
Bamouy méti bébé
Ñun ñar rék (Rék)
Cherie fouñu diar yép (Yép)
Li guenone méti bébé
Romb nañu lep (Lép)

Chérie sama xol yawa
Té kinga xam mana
Namnala man bay dioy
Chérie daga dém ma wétt
Té so ñeuwé mou déñ
Boudoul yaw dou done kénén
Lolo am

Té dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Man dama dof si yaw
Dou nén
Je suis fou de toi
Té dou nén
Chérie man dama dof si yaw



Credits
Writer(s): Michel Armand Guy Pagliaro
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link