Yagg Na (feat. Young Tili & Omzo Dollar)

Majestic Drama

Yagg na
Depuis temps wou daww demm salle de jeux
Khalé you ndaww, beuri fitt té wowone beut
Ça le fait, comme ça le veut, comme ça le peu peu
Ya ma nguembone, maye sa mbeurr
Ya ma done wakh, Tili ya lène meune
Lolou nga gueumone, lolou nga yeukk, té lolou moye deugg
Ça le fait, comme ça le veut, comme ça le peu peu

Niata deal làà gnu teudeul?
Da gnio fakhass, lepp lagn rakhass pour rekk mbapat
Ay boy you Dakar, Fall ya takh ma rap-ate
Beuguone tabakh, gnou gnuye dambate, yonn bé Naakar
Ouuuh Ouuuh! Teye ame na buzz nigga
Doul lo nagnou sugnuye nonn, niome dougnou Fuck nigga
Dama la watone fii ma léké, di nga fa lekk
Mais guène nga adouna té néko sama wett

Sama khol yegeutoul
Dama joy beu rongogne toureutoul
Bagn lene ma ndakh mbeuguel doyatoul yeah yeah
Sama khol yegeutoul
Rongogne toureutoul
Mbeuguel doyatoul yeah yeah

Yagg na
Depuis temps wou daww demm salle de jeux
Khalé you ndaww, beuri fitt té wowone beut
Ça le fait, comme ça le veut, comme ça le peu peu
Ya ma nguembone, maye sa mbeurr
Ya ma done wakh, Tili ya lène meune
Lolou nga gueumone, lolou nga yeukk, té lolou moye deugg
Ça le fait, comme ça le veut, comme ça le peu peu

Niata kogne làà gnu peundeul?
Boy you capable, beuguone fakhass, PIB Quatar
Tey ma ngii akk Abba, mais nakk amoul ragual
Da gnuye takkat, nonn bu wakh-att, tedjeul sa gatt
Kone lane moye buzz nigga?
So ko doundoul akk nitt kou takh ba ngey job nigga
Dama la watone fii ma léké, di nga fa lekk
Mais guène nga adouna té néko sama wett

Sama khol yegeutoul
Dama joy beu rongogne toureutoul
Bagn lene ma ndakh mbeuguel doyatoul yeah yeah
Sama khol yegeutoul
Rongogne toureutoul
Mbeuguel doyatoul yeah yeah

Mais tey sama life da niro revenge
Fatewouma primaire dem judo dimanche
Dollar changewoul même souy dem bureau de change
Mais rappouniou touss eyy
Fay studio yague ci khouss eyy
Dane negnou jaay suniouy shoes
Dou chance on a taffer le double nigga nene you niou tek ci kaw gas nioniou ouf
Mbolo si kogn bi di dokh
Deukone si galere youy soti si force
Sol pull ak capuche def lokho si poche
Bo niou songué niou sot yeah yeah
Mane ak sama frère yeup niongui cool
Fake niggas yi kasseh nioma degatoul
Diamono bi pro done meuner fifa
Deret suniou tankeu yi ndakh ay kickage
Wakh moussoul bolé sama cliqua
Amoul khaliss wala khalé buniou tital
Khaliss khakiss dougn ko kaffé ni zoss
Football moytou balle bi wadeu si force
Père bou teylé lepp khosslou di job
Mère bou guiss louné do degeu wakhou divorce
And my mind gone
Too deep cuz the harm strong
Still bleeding but I'm strong
Souma la meunone jokh deux roues ni Armstrong
Mais daga guéneu adouna ni Armstrong, young fif

Yagg na
Yagg na



Credits
Writer(s): Abdoulaye Diop
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link