BATMAN

Yeaah Yeaah
Batman, Batman
Yeaah Yeah
Batman, Batman
Batman!
Pour def lou noir, je suis partant
Mangui ci guinaw baby, night and day
Aw'ma pouvoir melni Batman
Mais ding'ma guiss fo'ma sooxla babe
Dama'la love mais j'ai pas le time
Desfois ma wonn'la sama dark side
Meu karr leu bise leu joxx leu calmant
Mais je ne peux pas vivre sans toi babe

Yang'may xaaar
Mais mangui xeuy ci waar weu
Mangui xeuy ci waar weu
Yang'may xaaar
Mais mangui xeuy ci waar weu
Mangui xeuy ci waar weu

Mel'ni Batman Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
All black vibe, melni Batman Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
I don't have time melni Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
All black vibe, melni Batman Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
I don't have time melni Yeah

Mangui ley xalaat bae beu noche
Bagn leu guiss bébé damay gaañ
Mais job bei beug fessal sama mind
Motakh amatouma Time Yeah
Mangui ley xalaat bae beu noche
Bagn leu guiss bébé damay gaañ
Mais job bei beug fessal sama mind
Motakh amatouma Time
Mais bébé bouma wo
Di yegueul sama tension
Wonder Woman oh
Xamnga yaw la saago
Yangui sama wett
Yaw rek Ya nek sam'xoll
Every time meu begg
Guis leu yeungeul sam'bopp
Guis nga tellement babe
Ma degg rek sa Allô
Dafay def ma crazy
Sama xoll nga appo
Beug gaaw nga seey ci
Motakh damay xaar doo
Money rek lay game
Niou deuki ji Monaco, Yeah

Yang'may xaaar
Mais mangui xeuy ci waar weu
Mangui xeuy ci waar weu
Yang'may xaaar
Mais mangui xeuy ci waar weu
Mangui xeuy ci waar weu

Mel'ni Batman Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
All black vibe, melni Batman Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
I don't have time melni Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
All black vibe, melni Batman Yeah
Batman Yeah, melni Batman Yeah
I don't have time melni Yeah

Yang'may xaaar
Mais mangui xeuy ci waar weu
Mangui xeuy ci waar weu
Yang'may xaaar
Mais mangui xeuy ci waar weu
Mangui xeuy ci waar weu
Mel'ni Batman Yeah



Credits
Writer(s): Baba Anne
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link