Naka Sa Dougouda

HAHAHA
James Brown
Domou Peter Brown
Niankass
Iniomeninio
Niankass
Iniomeninio
Niankass
Iniomeninio
Ehh ehhh
Kaani diagui ni du yako ladj
Hombre mogui ni du yako like
Mais Thiam tama
Niankass
Come on town bouy nangou sa girl
Wari abana
Rap galsen, moy xawma
Sen lamigne mo pata
Dadialo comme guinar elevage
So guisse kouy rap comme man
Guiss gua fi
Goor bou eumb
Sou tiole niou dem maiga
Sou molle Swiss Palace
Ohh baby ne me quitte pas
Yay sama nutella
May Sergio yow Marimar "
Biniou neke bobou ba legui dama dieul poids
Ehh haaannn
Naka sa dougouda
Ehhh haannnn
Est ce que mongui dallakhhh?
Ehh hannnn
Naka sa dougouda
Ehh hannn
Est ce que mongui dallakhhh?
Real bi never change Abe tiokodi
Pour yow de degagoma
Magui soga dikk
Coachte million dollar doga gnibisii
Woutouma noflay ci keparu ibliss
Football ak sa sow si match domicile
Fok sa chef de quartier ak sa tete de liste
Gnodi bandit zero illicite
Tyco tatto tek ko si cote bii yeahh
Ni lagn koy defei
Nimou yombei laaa
Nii naa neulei
Ma beug xalei bou am maanaa
Lii laa leulei
Sa loxo si biir potou chocolat
Li laa leulei
Ehh mo gui cool
Eh mo gui baax
Eh mogui cool
Eh Mogui baax
Ehhh hannnn
Naka sa dougouda



Credits
Writer(s): Alioune Badara Tambedou, Moctar Camara
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link