PENALTY

Homme de tenue beugué doundé corruption
Entreprise di sandi déchet pollution
Diokhla ndombal tank defo résultat
President bou beugué niéty mandat
Entreprise dieki teuthie
Gestionnaire keup caisse
Hôpital morgue deuthie
Beus bouné neew boubess
Civisme si mbed mi
Nane café sandi casse
Problèmes diangue mi rombe na syndicat

Waar mbith waara mbith
Arbitre dou sole 10
Capitaine dou sex mbipp
Lo Yor marakiss
Crampons dou tarxis
Surface ralentie hors jeux mounaan but
Loy xar penalty

Penalty arbitre sifflé wouko
Gnissi Banc bi nioko mbipp
Penalty
Bo neké ndjitt defo lila war Yeup
Gni nga djité niokoy mbipp
Penalty
Penalty arbitre sifflé wouko
Gnissi Banc bi nioko mbipp
Penalty
Bo neké ndjitt defo lila war Yeup
Gni nga djité niokoy mbipp
Penalty

Allalou njirim bingua teud deff sa noce
Lou nieup bokk iow nga dielko def sa poche
Sa xaritou ben bakane am lou bakh nga mer
Pousseul feulé iow deh amnga dal no mell
Tothie sa math tes delou classe
Mo geuneu ngay tothie sa mbarikh
Mounaane tass Yow dom ndaye
Systeme yereumoul ken
Moussou la beugue dou deign
Fexel ba diafandou fene
Nenala deugue dou fene
Députe niou niou la weer
Iow ngay nelaw assemblée
Mr le maire diaye n'a souff si wakhma
Xalei Yi founiouy fowé

Waar mbith waara mbith
Arbitre dou sole 10
Capitaine dou sex mbipp
Lo Yor marakiss
Crampons dou tarxis
Surface ralentie hors jeux mounaan but
Loy xar penalty

Penalty arbitre sifflé wouko
Gnissi Banc bi nioko mbipp
Penalty
Bo neké ndjitt defo lila war Yeup
Gni nga djité niokoy mbipp
Penalty
Penalty arbitre sifflé wouko
Gnissi Banc bi nioko mbipp
Penalty
Bo neké ndjitt defo lila war Yeup
Gni nga djité niokoy mbipp
Penalty

Day kass, nagn ko Var ralenti
Day kass, nagn ko Var ralenti
Day kass, nagn ko Var ralenti
Mou diok
Day kass, nagn ko Var ralenti



Credits
Writer(s): Ismaila Talla
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link