Frokh Thiaya (feat. Dio et Dia)

Je le mange, tu le manges
Il le mange, nous le mangeons
Frokh thiaya dafa nekh
Fils nékhouta bayi yow

Je le mange, tu le manges
Il le mange, nous le mangeons
Frokh thiaya dafa nekh
Fils nékhouta bayi yow

Je le mange, tu le mange
Il le mange, c'est dommage
Frokh thiaya dafa nekh
Fils nékhouta bayi yow

Wiss si pobar kankan moutardeu touti kani
Diam si curdent ma lék ko frokh thiaya dafa nekh
Wiss si pobar kankan moutardeu touti soblé
May ma ndokh ma rakhassou yow frokh thiaya is good

Frokh thiaya, Frokh thiaya
Diayma 15 lakhass té nga mayma gnekh mane

Credits
Writer(s): Abdoulaye Thiaw
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link