13

Kaan ngaay wolou fi boudoule sa bopp seul
Ndakh kilaay mourri pour nga seyyi
Meun na khaawi sa sutura wu sëy
Wax dou nex ba rombe nopp
Ame na niou dioudou tchi viol
Maniwou dou si mbeuguel rek léye tokeu
Souvent loye diéma prouver fi
Moye nékou faa
Liy handicaper famille
Meun na done parent bou Niakk thieurr
Philosophie tass sa seurr
Science délo sa hymen
Complémentaire si lou bonne
Aye erreurs humaines
Boy yé ngui trap di voler fadjar Blaise Diagne
Tacler jeunesse bi si suuf ni ballon
Arbitre atté woule gni drogue gaañ
Big pharma versus boy bi pousse si bopp kogne bi
Pour gayi meuna tasse Paquette
Taal seddo kouthion bi
Fuck la voix des sans voix
Boule wax sama bopp révolutionnaire
Bou féké meussa def guerre cent fois
Guestu guiss lambe dadj dieul def sa poche
Yak Macky yéna yéme
Bala niou ko xam niou diox la poste
Sama timbre vocal diaroule deux cents
Rappeurs yi déniouye diangue wax
Comme niou ame deux ans
Après mbedo damaye guéné ligne de vêtements
Trahison laay gueuna xaar
Kone rarement Niit bett ma
Ak lo fi yagg comme australopithèque
Fou niou diar dou extra lo fi tek
Job samaye milli après dieule espace
Rappeur bo fi guiss ame na loumouye diaye
Comme kou nek expat
Meussouma ame Nintendo
Tey bo taalé Xbox ding si degg sama baat
Dagg boumou diaam yi comme django
Téléviser révolution fok nga degg sunu baat
Si tissu social bi
Xarou ma si Sotiba
Handicapé la si mode
Xamé wouma ce qui va
Chiffres d'affaires orange laay triplé
Bayi game bi ak sen farou rap
Niouye couplet
Chaise
Fa laléne bayi niou tokk
Ma dieule samaye mesures ak distance
No talk
Masques yi waddeu c'est Iss au micro
814eme dose fuck omicron
Plume bi fepp léye laale
Vagabondage lyrical xalima thiapeu si daa
VIH musical
Pourquoi kou fiye reggae beuga nirro ak jamaïcain?
Pourquoi kou fiye rap beuga nirro ak américain?
Tabakh sama hôtel concurrencer Méridien
Sama talent la ba leave signer wouma si niome Mérou Dieng



Credits
Writer(s): Ismaila Talla
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link