Cana dou bayi | freestyle

Yeah
Thug boy leuh
Haha
Booz boozot

Lii dala métti dieuleul gaal (ay)
Douma rombou pakh mani feep lay laal
Fake niggaz yi niom neup laay taal (enh)
Motherfucker yii noo kén dousi dal
Fi moy faane nigga nieup lay fadj (enhan)
Dama paré feep koufi lambeu di nga dadj
Li ci kaw bodoul fou doko guiss
Limay guiss doko guiss
Takeu dix def leu miss dileu kiss
Ay way thug bi mane la boy (woo)
Geun lén takhaw niou tok di dioy (wahh)
Amna money guél bou toy
Nieup lay diam té ken dou moy
Douma séet kat di guiss sa dée
Li am fi doko guis fée
Moni mo ngi nieuw amoul lén loukoy tée
Mayma some niom nieup dée (aahh)
Cana day punch ay punch you dope
Cana day rhymé diko tek si code
Kouy roukh si game no kokou dou dara
Kouy doul di yolé mani kokou dou dara
Djité game bi mélni macky
Khamé nga kane moy thug bi (ngani)
Manou loma tée bokou diéma def
Kousi dougou déss loula dal rek yako def
Hey

Cana (hey)
Hey bitch may cana
Hey hey hey
Cana (hen)
My nigga my cana
Cana dou bayi
Cana (hey)
Hey bitch may cana
Hey hey hey
Cana
Hen
My nigga my cana
Cana dou bayi

Cana day bandit
Cana dou roukh
Cana day am money
Cana dou ragal



Credits
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link