Aime Possible Love

Yaay dafa wakh mani bawouma
Baay wakh ba sone bayi tayouma
Yoni tonss mou taki mouni fassouko
Khamougn ni louko tegg tassouko

Ni laalo ak thiéré dja
Kouma khol si yaw ngala méréma
Takalégnou gni koy diem gnepa wéré nak
Yalla téré nak yako téré nékh
Oh oh oh oh oh ohhhhhhhh
Oh oh oh oh oh ohhhhhhhh

Bou len ma khagn Ciré
Ndakh mom la mine
Bayilen ma ak Ciré
Ndakh mom la mine

Deg dou rombi nope
Degloul borom bi kot
Koulini mala guene si maam
Fekhel job ba guene ko dome
Day yok sa diom dong
Nga yokk sa guem guem
Fass yene yokk sa com com
Ba buntu bou tedjiou nga dadji ko doug fa tok ni nong diam ni gnoye
Diam ni gnoye diam ni diam ni gnoye
Oh oh oh oh oh ohhhhhhhh
Oh oh oh oh oh ohhhhhhhh

Bou len ma khagn Ciré
Ndakh mom la mine
Bayilen ma ak Ciré
Ndakh mom la mine

Ay gewel ak teg
Terewoul khol beg
Love rekay deg
Si kaw na gnep dég
Aramaal lou yalla daaganal
Sakaanal len sen katane nak
Tataanal wakh dji té abaalma
Deglouma fi menouma Li
Tardel sa life non begouma Li
Comme déména ni nagn ko yamaléfi
Nga dem ma dem ba bo dégué gouro yey



Credits
Writer(s): Youssoupha Gaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link