Al Khayri

Bayil ma sagou bi wagnil ma adiou bi
Sama khol bi sou tilimé yaay kikoy setal yay sama sabou fils
Loma def ma nangou ngir amour bi amoul fi
Sama fit bey tef tefi sou sama call soné sa numero affiché
Deglouma tewlouma li foula réwouma
Khep na sama khol té Diokh nala ndiguel nga done té dewouma
Nanouma lekouma di dianer kone guestouma
Sa rouh lay wetoul sakh soumay guent ndakh sa dieum dji lewouma

Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri

It was all about love diokhé xol diokhé kheter
Desse dieum dong
Sorry for Elzo gnanouma lonely like free li dou diam dongue
Thug bi nga def indo love story like Romeo and Juliette yaay
Sama marijuana soma méré damay melni kou gnouy dori yet
Wole ma sa wa keur té wakhma loy ladj girl
Diante bi sakh soko beugué ma indiko tadj girl
Diokh ma sa lokho ma def si bague nga dég Al khairy

Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri
Al Khayri



Credits
Writer(s): Youssoupha Gaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link