Diaayma Ma Guerre bi

Li gën ci ndab li man lay ñëw këf
Ñi bék moom seen yaakaar tas
Guerre ak man yombul dama mëna bis
Ma ci tekk loxo te matax ngeen gej ko gis
Ki ngeen doon xëcco la def copet
Doo leen ci papa Ndiaye may bondit
Sax dama tàng fum leen fekk ngeen allumette
Jël ko seen loxo pare taxal guerre guerre bi

Man li ma moom
Loxo bu ma ci fekk nga yërëm boroom
Ki ba ko Yàlla di sàkk man ma taxaw
Seeti leen leneen ki buur tekk na ci loxom
Sama lekk la tégil say bët ci moom

Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi
Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi

Ku ñeme nanga taxaw
Ku ragal nanga daw
Ki ku ko bëgg nangu ci man dangay raag ak man
Kon jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi

Ki may ki ko tëye man comme ku ngëb dërëm
Ngeen doo tàcc du yomb dam leen yërëm
Dama tébbi aas tax seen coeur yi di baax
Mënoo jël sama place liggéeyoo fi lu tax

Man la diiw beurre bi
(Billaay yaw ma diiw beurre bi)
Ñun la àjja ak àlaaji
Su ma koy ajj di ko ajjil
Chérie boy, chérie boy
Daf ma tànn ci seen biir
Ndax xam naa ni nit ku nitte la
Daf ma noba noba ba dof
Chérie sama chocolat

Ki man la nob (waaw)
Dotoo leen ci jot (déedéet)
Ndax mënuñu ko bokk
Kon demal nga togg
Fi amoo fi place
Man duma sa mas
Seen yaakaara tas
Lem leen seen ay bagaas

Man la diiw beurre bi
(Billaay yaw ma diiw beurre bi)
Ñun la àjja ak àlaaji
Su ma koy ajj di ko ajjil
Chérie boy

Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi
Jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi

Ku ñeme nanga taxaw
Ku ragal nanga daw
Ki ku ko bëgg nangu ci man dangay raag ak man
Kon jaay ma guerre bi, jaay ma guerre bi

Wóolu sa sëriñ su taxe nga yab ma
Na la defal baggas
Ànd bu dëgger liggéey mënu ci tus comme jouru dimanche
Fi loo ëndi fekk ko fi mo yaw dawoo sama yaram
Xale bu ci dugg sama 18 tu joues avec le feu

Man la diiw beurre bi
Ñun la àjja ak àlaaji
Su ma koy ajj di ko ajjil
Chérie boy



Credits
Writer(s): Charles Diagne, Abdoulahat Thioune
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link