Hymne Faramareen

Warna niou woné mbolo
Warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen
Faramareen nieuw na

Yéna ngui dég louné, wéraneté, xééx, xoulo nguir man
Souma sanione kéne kounék setsila niou naan ataaya
Beug yalla ko deff thi diaamam
Beug ngama, beug naala (ooh yeah)
Yéne gni beug faramareen teudeul nélaw yalla baaxna

Kone sopé sopé kaay, yaw kaay
Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man
Ma sopé sopé lover don't cry
Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man

Warna niou woné mbolo
Warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen
Faramareen nieuw na

Warna niou woné mbolo
Warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen
Faramareen nieuw na

Hey yow sama sopé
Boul di xoulo, boul di xééx, Yalla nopina
Yalla yaa na, Yalla baaxna
Maa léén gueuna love
Maa léén gueuna yeuk
Maa léén gueuna gueum
Maay ki leu xam
Maay ki leu beug
Ouh!
Force à toi sopé
Force à toi sopé



Credits
Writer(s): Akatche Bennette Seraphin Koffi
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link