Plug

Dou xof djit
Groubou 4 bi dou fuck
Pour rendi rapper soxla touniou motif
Saw na sa bamelou rappeur
Kane mofi sanie ni dou soti
Ma dak rap fi ci force
Ok ok Freshii ñu dem

Demal nga diangui ba nopi
Kou niémé diane yi dou xof djit
Groubou 4 bi dou fuck
Pour rendi rapper soxla touniou motif
Saw na sa bamelou rappeur
Kane mofi sanie ni dou soti
Ma dak rap fi ci force
Lounie meunti mar douniou nane ndoxou potite
Surtout si jamono dji
Ahmadou Bamba leu fils
Mane du ma son of a bitch
Mind on my bizz
Flowou anaconda yaw walax diane nga bitch
Mane dama tang dieur
Danguene ma amel tieur
Am ngandi coleu dou bamelou biir
Pare balles sax dou téyé sama coup de feu
Leundeum bi fepp leu comme beussou deuil
Christian Dior Christian Di...
Dinga goudé ndax lingma def xeuy
Gaindé dou dakadji beuy badi yot yeahh
Guiss kou def linga def douma berte
Def lima def dina ting si seu boor
Cash bi laa tal business bi laa tal
Yaw nga tal xeutio nek fi GOAT

Ohhhh
Wa galé nionguimay support
Ohhhh
Dou photo mais sons yé tax batay manek icone
Ohhhh
Gningay andal daniemay message dimay big up
Ohhhh
Th do guiss gayne bouy def ni mane and that's because
I'm the plug
Fucking plug yeaah
Sa wax douma disturb
Cuz i'm too strong yeahh
I'm the plug
Fucking plug yeaah
You took me for a joke
But you wrong yeaah

Fly
Men i gon fly
May kiy jeund lou way done jay
Damakoy def where you trynna try
Causer ay naufrages
Ya know CAB (leundeum si kaw bassi souf)
The god of the galsen zik
You won't never rap as me
Th douma meusseu tontou sa gad damn pique
Doumala meusseu wax ay sottises
What?
Danga fogone dangmay teu fils
Examen bifi moudj keumeufeu rek d'office
Waw
Li dess si school bi yeupeu diiggg
Kone noumay talé waxou biifff
Soumala falé nek bête
Pur senegalais lama fils
Téré woul gni newoul senegalais dima get
Yeah
Nena moniou meune ladj ko fane lay diar
Velo laniou yor mane ma yor ay chars
Niouné danioumay kar
Kepeu kouy wané fit bania pousse soula yabo meune nga tari ay saar
The og boy diff
Man of the year th yaw todioulo biss
Niémé li gnifi yagg meussouteu nango guiss
Tay lima nek litax meunoko nangoy dejouer neu sa pronostic

Ohhhh
Wa galé nionguimay support
Ohhhh
Dou photo mais sons yé tax batay manek icone
Ohhhh
Gningay andal daniemay message dimay big up
Ohhhh
Th do guiss gayne bouy def ni mane and that's because
I'm the plug
Fucking plug yeaah
Sa wax douma disturb
Cuz i'm too strong yeahh
I'm the plug
Fucking plug yeaah
You took me for a joke
But you wrong yeaah

Ohhhh
Wa galé nionguimay support
Ohhhh
Dou photo mais sons yé tax batay manek icone
Ohhhh
Gningay andal daniemay message dimay big up
Ohhhh
Th do guiss gayne bouy def ni mane and that's because



Credits
Writer(s): Mouhamed Loucar
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link