Ding Dong

Original
Rude Boy
Ay ay

Yama mën ci bi bord
Mën ci be bord
Bu ken atte nama ray
Xale day soxor
Takal ma menottes chicoter ma
Yegal ma asaman
Say bin bin say libidor
Dafa ye liy yandor

Yobou ma London
Ñu tere Kingston
Tël ma ni ping pong
Japp ma wëndel ma
Tingom ma
Tek ma ci kaw lal
Ñu fecc ding dong
Ding dong ding dong

Ehee he
Japp ko fofu la
Bo dégge kuy yuxu man mila
Ay ay
Yëfu bandit la
Ehee he
Japp ko fofu la
Bo dégge kuy yuxu man mila
Ay ay
Li yëfu bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la

Yay taw ci digg nord
Sed ci tangor
Diri ma sud jëme nord
Xale bi bandit nga
Wowe ko bandit bi
Mbeur bu mu dajel duma ci teel
Jox nala sama bop pic ak pelle
Menthe glace ak touti miel
Xale bi yobu ma septième ciel
Mën nga yëfu bandit ley ley la
Saf nani kani ley ley la eh
Du ma ci doyal ley ley la
Na gëna meti ley ley la eh

Yobou ma London
Ñu tere Kingston
Tël ma ni ping pong
Japp ma wëndel ma
Tingom ma
Tek ma ci kaw lal
Ñu fecc ding dong
Ding dong ding dong

Ehee he
Japp ko fofu la
Bo dégge kuy yuxu man mila
Ay ay
Yëfu bandit la
Ehee he
Japp ko fofu la
Bo dégge kuy yuxu man mila
Ay ay
Li yëfu bandit la

Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la
Bandit la
Yëfu bandit la



Credits
Writer(s): Oumar Niane
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link