Gëna Dem

Ken du la wax né ma nek si xel ak si xol yi di dompter ay Gaindé
Mane rek si xalé
Mane rek si label
Di danel ay cartel yu gandé
Cartel yu gandé
Hann

Ken du la wax né ma nek si xel ak si xol yi di dompter ay Gaindé
Mane rek si xalé
Mane rek si label
Di danel ay cartel yu gandé
Ken dotul weddi ma nek si xel ak si xol yi ndax xol yi mey yeungueul
Tiap na ay yekman yu yek
Wayé kene meunul copier
Ba diam sama diam yu mey yeggal
Damey bindeu di creer ak vitesse
Xalissu rap bi lay teguer ay business
Xolal track yu mey guener ak finesse
Bi tax sama diap di wuté ak ñi dess
Xel ba ngui xalate at xalate yu xot
Di ko xeli di xeli di xeli
Mer kat yi bayilene ñu xolu
Dañu faté ni ndogalu Yalla dji ken du ko wedi
Yalla dji ken du ko wedi
Vrai bandit ken du ko tek deal
Ken du ko deff fils
Vrai pivot ken du ko teggi
Ayo lene lane molene meti
Legui homie legui sax dañ ma wora wowé fleuve Senegal
Ndax man la bro bi eupeu flow biir Senegal
Fi guisu mafi game xana boy yuy jouer egate
Suma gené si game bi rek boy yi gen gamme han

Family bi ño si ndieukeu diapp
Legui galé ñeupey sote pour mu gëna dem
Staff bi ñeupa defaru ba paré
Xarite dawal zéro faute pour mu gëna dem
Wa kogne bi ñu gui fight pour mu gëna dem
Mère mi ngui ñane pour mu gëna dem
(Mère mi ngui ñane pour mu gëna dem)
Diap tewa bayi pour mu gëna dem
Diap tewa bayi pour mu gëna dem

Pour mu gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far
Di na gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far away

Indil valisu crack nga mey tegal ay mixtape
(Mixtape mixtape mixtape)
Xalissu rap bi lay lekké ay bifteck
(bifteck bifteck bifteck)
Sen avis du tax bama falé ken tchi yen
Ñak feyda job len nek fi di meer ak di ñodi timé

Staff bi ñeupa defaru (defaru defaru)
Staff staff Staff bi ñeupa defaru (defaru defaru)
Sama ingénieur serarul (serarul)
Leggi ben melomind meratul (meratul meratul)
Toolu tu ñu dolé
Bro bu fi dieul
Ben boy di ko bolé'k ñune(di ko bolé'k ñune)
Yeksi ngeen thioolé
Motax ñeup begg topando nu ñuy jobé ñune

Family bi ño si ndieukeu diapp
Legui galé ñeupey sote pour mu gëna dem
Staff bi ñeupa defaru ba paré
Xarite dawal zéro faute pour mu gëna dem
Wa kogne bi ñu gui fight pour mu gëna dem
Mère mi ngui ñane pour mu gëna dem
(Mère mi ngui ñane pour mu gëna dem)
Diap tewa bayi pour mu gëna dem
Diap tewa bayi pour mu gëna dem

Pour mu gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far
Di na gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem
Di gëna dem far away (far away)

(Gëna dem)
(Gëna dem)
(Gëna dem)
(Gëna dem)
(Gëna dem far away)
(Gëna dem)
(Gëna dem far)



Credits
Writer(s): E-tracc
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link