Wreew Beu Dof

Say
Yallah mooma tathiou waayé teubeugoumeu
Lemko bamou rond ken weureutouleu
Lima yagg rêver teureuloumeu
Neel sa rappeur Tant que meunoul soul ker beugueudiouma

Boum si baat keud nd* tabouret
Corbillard gnima yap daniou neew
Ndekki laay omelettes nitou neen
Des grosses chattes mais sibouleen

Thiouss, ween
Mooy sa cachet rappeur
Doul, fèn
Rek lama dakheu
Coups, plaies
Y'aura des blessés
New, Wave
Chaud melni été

12, 16
Samay couplet daniou nice beu danioumay faatélo célibat
Douter
Fooko deguer sama vocabulaire égale à quinquélibat
Mouss, nguinw
Quand le chat est là tu t'en bats les couilles bouder yaay Gaïndé
Doublé
Taal smoke fay gnima beug pop sakhaaral sen game BP yeah

Marquer sama droit comme latéral gauche
Def campagne delouwaat aal ba
Yallah rek mooma maneu térè doon GOAT
Bay sama waar douma khaar kouma niaakh
Mbeur caamin bou amoul ben mass laa
Xaliss mooy wakh booko amoul boul masslaa
Sons yi nioogui daw fatt fepp c'est le karma
Tégou sen radios nakh damaleen damatt

Damalaa soof
Meunooma neekh
Gueun leen thioof
Niou beug maa thieeb han
Cours ak long
Lepp laay def
Na niaaw na moche
Salifondé wouyumeu

Wreew
(Wreew beu Dof)
Wreew
(Wala beu neup)
Wreew
(Ngani ma lane?)
Kou meun li ngay def boula neekhé
Wreew
(Louma def mako tey)
Wreew
(Et puis merde)
Wreew
(Fan ñgen todj)
Kou meun sey non boula nekhé
Wreew
(Wreew beu Dof)
Wreew
(Wala beu neup)
Wreew
(Ngani ma lane?)
Kou meun li ngay def boula neekhé
Wreew
(Louma def mako tey)
Wreew
(Et puis merde)
Wreew
(Fan ñgen todj)
Kou meun sey non boula nekhé

Sama tailleur dieul sama mesure
Néma punchlines laalay niawalé
Yor khiir gun ak ceinture saleteel kone douma baalé
Soum waay neel say lèche cul yimay conseiller taat laay déguer
Fouma diaar sen grosses pointures tuut tank lanioufay takhawer

Yaay sa taaw nako thiatt seekhlou
Tégouniouma louma meunoul dékou
Bras long amoumako def coup mou sorri
Zidane amoul karaw dieul coupe
Di nga naaw boumla maayé as tout
Douma dak teh maa gueneu aay buur
Sama yoon si golo bouy bokh golo
Khel niaar amoul damalaay doute

My boy Bouma natter si rap damalay tek daan
Doug ay nikou wara dieul deuxième femme
10 zero laay door sen 11 départ
Amoumeu comme élection première dame
Beug dieul péh waral douma daw deuss
Teh si ndieulbeen beugumeu woon am buzz
Seni clichés diaaroul sama album
Naroumako yaagal boumalendi sankeu
Golden boy

Damalaa soof
Meunooma neekh
Gueun leen thioof
Niou beug maa thieeb han
Cours ak long
Lepp laay def
Na niaaw na moche
Salifondé wouyumeu

Wreew
(Wreew beu Dof)
Wreew
(Wala beu neup)
Wreew
(Ngani ma lane?)
Kou meun li ngay def boula neekhé
Wreew
(Louma def mako tey)
Wreew
(Et puis merde)
Wreew
(Fan ñgen todj)
Kou meun sey non boula nekhé
Wreew
(Wreew beu Dof)
Wreew
(Wala beu neup)
Wreew
(Ngani ma lane?)
Kou meun li ngay def boula neekhé
Wreew
(Louma def mako tey)
Wreew
(Et puis merde)
Wreew
(Fan ñgen todj)
Kou meun sey non boula nekhé

Omzo on the mafé
(Omzo on the mafé)
Omzo on the mafé (Omzo on the mafé)



Credits
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link