Sago

Say say
Say say
Yeah

Li nekk ci man mi
Doon samay kàddu
Ci sama xol la bawoo
Ci adduna bi
Amul keneen ku may caalit loo ni yow
Ndax man awma ci sago
Man awma ci yow sago
Noo def ba gis ma
Yaa ma njëkka won sa bopp
Awma ci sago
Man awma ci yow sago
Awma ci sago
Man awma ci yow sago

I say
Tegouma la beut, mais yow rek lay guiss
Dam leu yagga weur, ni kou wadal wetchit
Sama fit day daw, mais sama khol dou jekh
Ya takh may weur kerr ci goudi geumentou midi
Sa yo ma jegué, damlay geuneu nameu
Manam damay melni kugnu terré lumu tameu
Assamane day souffé, souba tel bi goudé
Jarral ngama brailler wayé

Li nekk ci man mi
Doon samay kàddu
Ci sama xol la bawoo
Ci adduna bi
Amul keneen ku may caalit loo ni yow
Ndax man awma ci sago
Man awma ci yow sago
Noo def ba gis ma
Yaa ma njëkka won sa bopp
Awma ci sago
Man awma ci yow sago
Awma ci sago
Man awma ci yow sago

Baby foo yèndo'og man foofu lay yèndoo ba fanaan
Boo jaaree nii ma koj la côté bee doo ma raw
Li nga jota def ci man ken dootu ko def ci man
Yow li nga jota def ci man awma ci sago
Man awma ci yow sago
Noo def ba gis ma
Yaa ma njëkka won sa bopp
Boo demmee ma laago
Boo sooree ma mel ni laffañ
Yow waru ñu taggoo
Man da ma lab ci sa diggu mbëggeel

Li nekk ci man mi doon samay kàddu ci sama xol la bawoo
Ci adduna bi amul keneen ku may caalit loo ni yow
Ndax man awma ci sago
Man awma ci yow sago
Noo def ba gis ma
Yaa ma njëkka won sa bopp
Awma ci sago
Man awma ci yow sago
Awma ci sago
Man awma ci yow sago



Credits
Writer(s): Abdoulaye Diop, Arfang Thiare
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link