JALOUSIE
Par AbouAmg
Yeen xam ngeen, jalousie feebar la
Mbaa yeen xam ngeen, jalousie feebar la
Te day ray, hôpital du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Ma ni la da lay ray, hôpital du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Foo toog doo kontaan, sa xol bi du neex
Jalousie da lay ray
(Jalousie, soxor day ray)
Man dama ne day ray
Te docteur du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Man dama ne day ray
Te sëriñ du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Foo toog doo kontaan, sa xol bi du neex
Jalousie da lay faat!
(Jalousie, soxor day ray)
Lan mooy indi feebar bi?
Baña nangu li Yàlla def ci nit ki
Su xasee dugg ci yaw
Ngeene ko dina doy war
Go mu xol rekk la lay def
Su yàggee soxor dab laa
Ngay mer rekk doo xam lan la?
Ko gis rekk iñaan ne ko
Soxor da lay ray
Te docteur du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Maa ne la da lay ray
Te sëriñ du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Foo toog doo kontaan, sa xol bi du neex
Jalousie da lay ray
(Jalousie, soxor day ray)
Ndekke bi maladie
Moom rekk ay lëmbe dégg na ci mim reew
Soxor la lu ci xol yi
Moo tax ñuy dëkke wax lu ñaaw
Foo ma seen di mer, lan la?
Te nga ma claméek Yàlla
Xéy-na mu mën ci dara
Man Vivi sonal naa la
Soxor da lay ray
Te docteur du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Maa ne la da lay kill
Te sëriñ du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Yaw wax ma loo ma bañe
Ndax dama la mës a rayal sa taaw
Wax ma loo ma bañe
Te nga bës ca xol bi bàyyi iñaan
Gomu xol rekk la lay def
Su yàggee soxor dab laa
Ngay mer rekk, boy qué pasa?
Ko gis rekk iñaan ko
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Ouh, xol bu bon da lay tardeel
Anh, sa jikko moo bon, changeel
Xol bu bon bi la ñépp xame
Yàgg na ci yaw judduwale la
Xol bu bon bi la ñépp xame
Toogal rekk dinga xëy mu ray la
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Ma jiin leen
Mbacke Dioume ma way la
Pape Cheickh Diallo Dierry
Boroom xolu jàmm yaa ngiMbacké Dioume demb la te du tay
Sa xol bi Yàlla rekk a la koy fay
Yaw Baye Cheikh kenn nga ci man mi
Sama doom ji sama xol laa la teg
Feexal kee!
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Yeen xam ngeen, jalousie feebar la
Mbaa yeen xam ngeen, jalousie feebar la
Te day ray, hôpital du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Ma ni la da lay ray, hôpital du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Foo toog doo kontaan, sa xol bi du neex
Jalousie da lay ray
(Jalousie, soxor day ray)
Man dama ne day ray
Te docteur du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Man dama ne day ray
Te sëriñ du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Foo toog doo kontaan, sa xol bi du neex
Jalousie da lay faat!
(Jalousie, soxor day ray)
Lan mooy indi feebar bi?
Baña nangu li Yàlla def ci nit ki
Su xasee dugg ci yaw
Ngeene ko dina doy war
Go mu xol rekk la lay def
Su yàggee soxor dab laa
Ngay mer rekk doo xam lan la?
Ko gis rekk iñaan ne ko
Soxor da lay ray
Te docteur du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Maa ne la da lay ray
Te sëriñ du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Foo toog doo kontaan, sa xol bi du neex
Jalousie da lay ray
(Jalousie, soxor day ray)
Ndekke bi maladie
Moom rekk ay lëmbe dégg na ci mim reew
Soxor la lu ci xol yi
Moo tax ñuy dëkke wax lu ñaaw
Foo ma seen di mer, lan la?
Te nga ma claméek Yàlla
Xéy-na mu mën ci dara
Man Vivi sonal naa la
Soxor da lay ray
Te docteur du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Maa ne la da lay kill
Te sëriñ du ko faj
(Jalousie, soxor day ray)
Yaw wax ma loo ma bañe
Ndax dama la mës a rayal sa taaw
Wax ma loo ma bañe
Te nga bës ca xol bi bàyyi iñaan
Gomu xol rekk la lay def
Su yàggee soxor dab laa
Ngay mer rekk, boy qué pasa?
Ko gis rekk iñaan ko
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Ouh, xol bu bon da lay tardeel
Anh, sa jikko moo bon, changeel
Xol bu bon bi la ñépp xame
Yàgg na ci yaw judduwale la
Xol bu bon bi la ñépp xame
Toogal rekk dinga xëy mu ray la
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Maa ne waxal ki "jalousie, soxor da koy ray"
Ma jiin leen
Mbacke Dioume ma way la
Pape Cheickh Diallo Dierry
Boroom xolu jàmm yaa ngiMbacké Dioume demb la te du tay
Sa xol bi Yàlla rekk a la koy fay
Yaw Baye Cheikh kenn nga ci man mi
Sama doom ji sama xol laa la teg
Feexal kee!
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Jalousie, soxor da koy ray
Credits
Writer(s): Akatche Bennette Seraphin Koffi, Bakhaw Dioum
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
© 2025 All rights reserved. Rockol.com S.r.l. Website image policy
Rockol
- Rockol only uses images and photos made available for promotional purposes (“for press use”) by record companies, artist managements and p.r. agencies.
- Said images are used to exert a right to report and a finality of the criticism, in a degraded mode compliant to copyright laws, and exclusively inclosed in our own informative content.
- Only non-exclusive images addressed to newspaper use and, in general, copyright-free are accepted.
- Live photos are published when licensed by photographers whose copyright is quoted.
- Rockol is available to pay the right holder a fair fee should a published image’s author be unknown at the time of publishing.
Feedback
Please immediately report the presence of images possibly not compliant with the above cases so as to quickly verify an improper use: where confirmed, we would immediately proceed to their removal.